Leuz Diwane G - Mburok Lem - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Leuz Diwane G - Mburok Lem




Mburok Lem
My Love
Ou naa naa naaaa
Ou naa naa naaaa
Eh eh ehhh
Eh eh ehhh
Sa araass laniou bolé niari rouh yi
It’s been a long time since you took my breath away.
Adouna dou wone touki guissé wouniou ba nopi
When I’m with you time flies so fast.
Ehhhhhhh héee
Ehhhhhhh héee
Bén palace niou beuneu sama rouh gui
You are the palace where my soul resides.
kou démone touki meunoul nieuw ba légui
And as a demon you possess me and own my soul.
Ehhhhhhh héee
Ehhhhhhh héee
Dianakhé-k banekh dima kali kalé
Every day and night it’s so beautiful
Kagne lay done ak noumay déff ba guisla
When I’m with you I want to stay forever.
Dane na khégn lou gueun nekh dou kii dou keulé
I love what’s good, beautiful and tasty
Nga néwone si yone noumay déff ba miss la
And I’ll never leave if it’s beautiful and delicious.
Stagiaire laa wone cv bi demna founé
Intern, here is my CV please hire me.
Ndékété yoo douma ligueey si niom
I beg you to accept my application.
Dou dianeer dagne mala wane mbégté la yoo
When I wake up I’m sick please hire me.
CD bi dathie boudé yay diour samay dome
This CD is for you, keep it and listen to my voice.
Youssou Ndour ak Péne
Youssou Ndour and Péne
Khamone naani daniou dadié dou ndourok lénn
Come on my love let’s dance to this wonderful song.
Khamone naani beuss bouniou dadié moy dakheu mbourok lém
Come on darling come closer to me my love.
Doumala fénn
We are destined for each other.
Give me your hand
Give me your hand
Niou ande dém féneen
And let’s go far away.
Dieundé woumala kénn
God is our witness.
Dou kéneu si niom kou moune dara si nioune
Don’t listen to what people say about us.
nioune sokhlo wouniou khoulok kénn
We are the only ones who know the truth.
Nga togne ma maalay baalou
I am tired of complaining.
Wakhlén ma kagne laay dallou
I’m tired of crying.
Kou sagna tamba-mbalou
It’s like peanut butter.
Boma méré ma waarou
Give me your love.
Baayilén niou wakh loulén nekh
Darling, we have suffered too much.
Guisagouma louniou wara téré dém
Love us as we are.
Lima yeuk khadioul si ndap dou dieeeekh
Because we suffered in silence.
Kéee wakh ko boumou yakh crédém
I believe you my love.
Danga gueuneu fort khéttou bone si man
I love you more than you love me.
Tatt laay déff soumala diéguéé
I always beg you to forgive me.
Meun nga sa borr matt nga linga done si man
Even though I am wrong I want you to be by my side.
Soudoul yaw sama tole kénn douko niaguéé
You are the only reason for my happiness.
Bokak yaw keur di fo di réée di contane
I’m crazy in love with you.
Moy sama yéné si yaw
You are my life.
Mou antou niou mour la nga ouf sama ndiabote
We will die together for the love we share.
Je t'aime mon cœur kén douniou réé é é
I love you my heart.
Do dégue Ndeysaan
May God bless us.
Dinala téyèè nimou waré ba dégue diarabote
And keep us together forever.
Ma moitié, ma reine, l'autre moi
My half, my queen, the other me.
Ma meilleure amie
My best friend.
Quand je parle de toi j'ai des larmes aux yeux
When I talk about you, I have tears in my eyes.
Je t'aime et tu es toute ma vieee
I love you and you are my whole life.
Youssou Ndour ak Péne
Youssou Ndour and Péne
Khamone naani daniou dadié dou ndourok lénn
Come on my love let’s dance to this wonderful song.
Khamone naani beuss bouniou dadié moy dakheu mbourok lém
Come on darling come closer to me my love.
Doumala fénn
We are destined for each other.
Give me your hand
Give me your hand
Niou ande dém féneen
And let’s go far away.
Dieundé woumala kénn
God is our witness.
Dou kéneu si niom kou moune dara si nioune
Don’t listen to what people say about us.
nioune sokhlo wouniou khoulok kénn
We are the only ones who know the truth.
You know I love you
You know I love you
Never dare a leave you you know I need you
Never dare a leave you you know I need you
Every day every night I'm thinking about youuu
Every day every night I'm thinking about youuu
Night & day every where I go baby I see you
Night & day every where I go baby I see you
There is no one... no one like you
There is no one... no one like you
Nga togne ma maalay baalou
I am tired of complaining.
Wakhlén ma kagne laay dallou
I’m tired of crying.
Kou sagna tamba-mbalou
It’s like peanut butter.
Boma méré ma waarou
Give me your love.
Youssou Ndour ak Péne (hé hééé)
Youssou Ndour and Péne (hé hééé)
Khamone naani daniou dadié dou ndourok lénn
Come on my love let’s dance to this wonderful song.
Khamone naani beuss bouniou dadié moy dakheu mbourok lém
Come on darling come closer to me my love.
Doumala fénn
We are destined for each other.
Give me your hand
Give me your hand
Niou ande dém féneen
And let’s go far away.
Dieundé woumala kénn
God is our witness.
Dou kéneu si niom kou moune dara si nioune
Don’t listen to what people say about us.
nioune sokhlo wouniou khoulok kénn (hééééé)
We are the only ones who know the truth. (hééééé)





Writer(s): Abdoul Aziz Fall, Leuz Diwane G


Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.