Canabasse - Gnu Ngui Ladj Lyrics

Lyrics Gnu Ngui Ladj - Canabasse




Djeul se me temps me melni kou doul mousse dief
Quou me honkou pour guené son kou deglou dief
Lou me lal mou nathe dnahe fils dou me ray
De me fly ma gui naw kan mo mey tekk thi ray
Ya gui hegne thiouray ndahe ya gui se podiou yaye




Attention! Feel free to leave feedback.