Lyrics Sama Dome - Dip Doundou Guiss
Reptile
Music
Yakkamtinaleu
Yakkamtina
Yakkamtinaaleu
Mounouma
xarr
Nangou
ngueu
place′am
cii
sama
xol
Dieul
sama
place
mom
cii
xol'am
Yakkamtinaleu
Yakkamtinaaleu
Ken
téré
wouñou
begg
té
dé
douñou
ray
Negn
dem
outti
guédj
bougn
dellou
cii
déx
Étincelle
bou
guiss
essence
noumouy
def
Féké
souniouy
guent
nelow
beussou
dé
Yallah
mala
dengk
malaka
ngueu
lerr
Sa
yay′ama
bett
diama
lama
meyy
Amana
ba
tayy
Yallah
dou
yakkamti
dé
Kone
fananal'ak
werr
kouy
nadjal
sa
kerr
Kay
ma
wokh
la
wone
la
fi
noumou
mél
Danga
ndaw
té
dingueu
def
lou
raw
li
Kirikou
def
Boul
sissou
boul
fène
boul
fëss
késsé
ndakh
siiw
dou
succès
Primaire
sama
photo
classe
amna
ñouthii
moudjou
jail
Té
ñeupeuy
niane
am
moudjeutel
bou
bax
Yensay
may
lath
ndakh
Meuwti
xamna
loutax
dé
bi
gaw
Nguène
foudeune
senni
tangk
djoubal
pengkou
di
ñane
Na
dem
église
yobou
sondel
bi
taal
Loutax
réne
dou
daaw
C'est
parce
que
réne
negn
outteul
téneu
bi
baag
Bougouma
di
taggato
né
nieup
Bateau
demna
bateau
boudoul
keuppou
Capitaine
ya
woné
yone
bi
for
ever
Kou
fowé
sa
bopp
niou
fowéleu
Kou
domam
deuk
cii
diam
dotoul
tabakh
cii
guerre
Bou
nieupp
di
outti
lampe
yaw
demal
outti
leer
Kone
goudou
fane
rek
laalay
nianal
Koula
khar
kham
do
nieuw
Yakkamtinaleu
Yakkamtina
Yakkamtinaaleu
Mounouma
xarr
Nangou
ngueu
place′am
cii
sama
xol
Dieul
sama
place
mom
cii
xol′am
Yakkamtinaleu
Yakkamtinaaleu
Tant
que
ya
ngui
begg
mangui
begg
Teuth
nala
cii
sama
xol
Dieul
sama
thiaabi
sanni
gueth
Yam
sama
diangue
ak
ligueey
Magg
xaliss'am
di
leew
Meytou
danou
tay
cii
pakh
bi
diane
yi
matt
lène
Yane
meusteu
diss
ba
raw
bi
yaye
di
dath
cii
seuy
Jésus
Chris
meuss
na
rakhass
ay
tangk
talibé′m
Yensay
ngueu
tane
té
deñla
tane
sans
ngueu
yeggko
Xamna
ni
thiat
dou
yekh
mais
ñanal
daw
thiat
bi
yeup
Buur
bi
sa
biss
nieuw
na
Fataliko
ay
mame'am
Guiss
na
kou
mél
comme
mom
Mane
la
siguil
xol
ma
Tekki
na
laaf′am
naaw
Waayé
foumou
dieum
khawmafa
Mom
famou
dieum
xawma
Wayé
aljana
negn
koy
woowé
Yakkamtinaleu
Yakkamtina
Yakkamtinaaleu
Mounouma
xarr
Nangou
ngueu
place'am
cii
sama
xol
Dieul
sama
place
mom
cii
xol′am
Yakkamtinaleu
Yakkamtinaaleu
Attention! Feel free to leave feedback.