Doudou N'Diaye Rose - Diame Lyrics

Lyrics Diame - Doudou N'Diaye Rose



Jamono jilee dafa laj jam jumat sëk
Mani
Jamono jilee dafa laj jam jumat sëk
Jamono jamono jamono jamono jamono jilee dafa laj jam jumat sëk (×2)
Ñewleen ñu ñaan jam suñu rew
Ñewleen ñu ñaan jami aduna
Ñewleen ñu ñaan jami suñu rew
Eh ñewleen ñu ñaan jami aduna
Ku dem beu mënetul guestu talal loxom
Ku dem beu mënetul guestu xolat xolam
Ku dem beu mënetul guestu di jeemë gorgorlu
Ku dem beu amatul guestu jaxlee di joy
Ku dem beu amatul xarit yi daw waccë le
Ñaanal jam ñaanal jam di way
Ñewleen ñu ñaan jami suñu rew
Ñewleen ñu ñaan jami aduna
Ñewleen ñu ñaan jami suñu rew
Eh ñewleen ñu ñaan jami aduna
Ba aduna soso ba leigui
Seytanei di sox soxi
Ba aduna soso ba leigui
Seytanei di sox soxi
Ñewleen ñu ñaan jami suñu rew
ñewleen ñu ñaan jami aduna
ñewleen ñu ñaan jami suñu rew
Eh ñewleen ñu ñaan jami aduna
Jam rekka mattë ñaan ndax suñu liguey barkel
Jam rekka mattë ñaan ndax rewmi jëm kanam
Ñewleen ñu ñaan jami suñu rew
ñewleen ñu ñaan jami aduna
ñewleen ñu ñaan jami suñu rew
Eh ñewleen ñu ñaan jami aduna
Jamono jamono jamono jamono jamono
Jilee dafa lajj jam ju matt sëk (×2)
Ñewleen ñu ñaan jami suñu rew
Ñewleen ñu ñaan jami aduna
ñewleen ñu ñaan jami suñu rew
Eh ñewleen ñu ñaan jami aduna



Writer(s): Julien Jouga


Doudou N'Diaye Rose - Djabote
Album Djabote



Attention! Feel free to leave feedback.