Elzo Jamdong - Positivibz - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Elzo Jamdong - Positivibz

Positivibz
Positivibz
instrumental
instrumental
Hun... Hun Kill them with...
Hun... Hun Tue les avec...
Barrington Levy sample
extrait de Barrington Levy
"Kill them with positive vibes"
"Tue les avec des ondes positives"
With #PositiVibz ...
Avec #PositiVibz ...
Dolli tchi waay, yeah (Kill them with Positive vibes) yeah
Dolli tchi waay, ouais (Tue les avec des ondes positives) ouais
Ay positive vibes lama di khélli bou doyoul dolli tchi
Ay ondes positives lama di khélli bou doyoul dolli tchi
Lepp lou dieum thi samm kolleuré t'inquiète nio ngui thi
Lepp lou dieum thi samm kolleuré t'inquiète nio ngui thi
Samm jamm donng ni Lauryn Hill
Samm jamm donng ni Lauryn Hill
Nio ngui thi khèkhe, boul khèpe, boul snitch, boul yolé deal
Nio ngui thi khèkhe, boul khèpe, boul snitch, boul yolé deal
Shit bi soundou strip tease mais sexy neu
Shit bi soundou strip tease mais sexy neu
Hello DK, Yeubo TeauPla ekssi neu
Hello DK, Yeubo TeauPla ekssi neu
Nélène Hip Hop bou dèè wone légui dekki neu
Nélène Hip Hop bou dèè wone légui dekki neu
Niafé neu beu guénne ghetto bi légui tékki neu
Niafé neu beu guénne ghetto bi légui tékki neu
Gueustou negn Pac, yagg déglou Big
Gueustou negn Pac, yagg déglou Big
Yagg dadji ay pack guénné feuille ak bic
Yagg dadji ay pack guénné feuille ak bic
Fone diamou thi punchline yi ak grosses caisses yi
Fone diamou thi punchline yi ak grosses caisses yi
Presque ay Talibé wou Kweli ak Mos Def (yeah)
Presque ay Talibé wou Kweli ak Mos Def (ouais)
Be légui kou wakh deugg niou tek thi bate!
Be légui kou wakh deugg niou tek thi bate!
Compilou Dekkil Rap léniouy dekkilate
Compilou Dekkil Rap léniouy dekkilate
Bou doyoul me dolli thi waye
Bou doyoul me dolli thi waye
Jamm dongg legn sékkh ak ay Positive Vibes
Jamm dongg legn sékkh ak ay Positive Vibes
Pont1
Pont 1
Haha ak ay diap, han Mister Thiere hit me
Haha ak ay diap, han Mister Thiere hit me
Yo Bab's yéwoul boyyy, han wa H (Grd Medine), bou doyoul me dolli tchi
Yo Bab's yéwoul boyyy, han wa H (Grd Medine), bou doyoul me dolli tchi
Ay positive vibes yi mey khélli sokhleu woul polémique
Ay ondes positives yi mey khélli sokhleu woul polémique
Bo nit, me togg bolé leu tchi nga goré tchi
Bo nit, me togg bolé leu tchi nga goré tchi
Wakh bou beuri mo takh louniou tabakh danou rek
Wakh bou beuri mo takh louniou tabakh danou rek
Motakh légui manou rek sinon gaaniou rek
Motakh légui manou rek sinon gaaniou rek
Depuis temps wou Pac niou tchi same ish
Depuis temps wou Pac niou tchi same ish
Yo bingay TAKHOURAne seme ga yang thi TAKHOU RAp yi
Yo bingay TAKHOURAne seme ga yang thi TAKHOU RAp yi
Sorano: anniversaire PBS, Daara J Saint Michel, DJ Makhtar PCS
Sorano: anniversaire PBS, Daara J Saint Michel, DJ Makhtar PCS
Boumou diame yi legn takk tchi bate
Boumou diame yi legn takk tchi bate
Flow bi ley feugg ay kourrou baye Cheikh Ibra Fall
Flow bi ley feugg ay kourrou baye Cheikh Ibra Fall
Lo mey kholé ni gayne? deungueu fogone dina fombé ni fight bi?
Lo mey kholé ni gayne? deungueu fogone dina fombé ni fight bi?
Ha ay BOMB la lène indil ak ay Positive Vibes
Ha ay BOMB la lène indil ak ay Positive Vibes
Pont 2
Pont 2
Yea, yo dolli tchi! My man MTO DMC danga dof wala lane
Yea, yo dolli tchi! My man MTO DMC danga dof wala lane
Positive vibes dolli tchi waay
Positive vibes dolli tchi waay
(Bruit de sirène en fond)
(Bruit de sirène en fond)
Han Positive Vibes yi mey khélli? Mome rek la yoré ni
Han Positive Vibes yi mey khélli? Mome rek la yoré ni
Boumeu droiter lo thi naadj bi kanamou gonéyi
Boumeu droiter lo thi naadj bi kanamou gonéyi
Am na médaille d'or dèlloul se keur
Am na médaille d'or dèlloul se keur
Son bi fok mou dow ak Usain Bolt Jailou Reubeuss (#100m)
Son bi fok mou dow ak Usain Bolt Jailou Reubeuss (#100m)
Ma dakkh youkhou Ndour ma gueneu marre Pène
Ma dakkh youkhou Ndour ma gueneu marre Pène
Deme khiff ay khalam, Souleymane Faye
Deme khiff ay khalam, Souleymane Faye
Génération "Rest In Peace 2Pac Marley"
Génération "Rest In Peace 2Pac Marley"
11 mai niou diam leu yobou leu armel nga ziarre lene
11 mai niou diam leu yobou leu armel nga ziarre lene
Yo bayil me yémeulé ko fi ga yi parégouniou pour degg yoyou!
Yo bayil me yémeulé ko fi ga yi parégouniou pour degg yoyou!
Deungueu sonneu?
Deungueu sonneu?
Han? Wala me dolli thi waye?? Ay nokkh lalène digone ak ay positive vibes
Han? Wala me dolli thi waye?? Ay nokkh lalène digone ak ay positive vibes
Han, loye mel ni kou diommi ni gayne?
Han, loye mel ni kou diommi ni gayne?
Jamm dongg legn sekkh ak ay positive vibes
Jamm dongg legn sekkh ak ay positive vibes
Lo mey songgué ni baye hi? Deungueu fogone dina fombé ni? laay!!! huhu
Lo mey songgué ni baye hi? Deungueu fogone dina fombé ni? laay!!! huhu
Ak ay positivibz
Ak ay positivibz
Lo mey songgué ni baye? deungueu fogone dineu yombé ni, Layyye lol
Lo mey songgué ni baye? deungueu fogone dineu yombé ni, Layyye lol
Ay bombes lalène indil ak ay ...
Ay bombes lalène indil ak ay ...
Lo mey kholéé ni gayne? Deungueu fogone dineu yombé ni han?!: lalène digone ak ay ...
Lo mey kholéé ni gayne? Deungueu fogone dineu yombé ni han?!: lalène digone ak ay ...
Ay nokkh lalène digone ak ay ...
Ay nokkh lalène digone ak ay ...
Ay boxe lalène digone ak ay ...
Ay boxe lalène digone ak ay ...
Jam dongg legn sèkkh ak ay ...
Jam dongg legn sèkkh ak ay ...
Ay $^^ lalene digone ak ay...
Ay $^^ lalene digone ak ay...
FreeDope
FreeDope
Elzo
Elzo
ALL TRACKS ON FreeDope
TOUS LES MORCEAUX SUR FreeDope
Judge Not
Ne jugez pas
Lonely
Seul
Melomind
Melomind
Beats By Thiere
Beats By Thiere
Dans Mon Monde
Dans Mon Monde
Seuss
Seuss
TeauPla Anthem
Hymne TeauPla
Raison Nègre (FreeDope )
Raison Nègre (FreeDope )
Roy Thi Mom
Roy Thi Mom
PositiVibz
PositiVibz
AUDIO
AUDIO

Attention! Feel free to leave feedback.