OMG - Koti Koti - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation OMG - Koti Koti




Koti Koti
Koti Koti
Doff thi mane ndeundé woma dara loudoul mbeuguel
Tu es mon prince charmant, un cœur qui bat fort pour moi
Mala tane sépi lathi ndax yamay danel
Je suis tout à toi, bébé, et je t'aime de tout mon cœur
Yaw kham ngané kéne dou kheutio lima mome
Quand je pense à toi, mon cœur se met à battre vite
My baby sama khol bi yako mome
Mon chéri, tu es tout pour moi
Sama yéné gnou doundou seuy ba am thi dome
Je suis amoureuse de toi et je veux toujours être avec toi
Gnouy koti koti yoli yoli li thi soukeur dou khorom
On va danser, "koti koti", "yoli yoli", on s'amuse et on rit
Rééro nga guindi ma
Je t'aime tellement, mon amour
Dila way ni youssou wayé birima
Viens avec moi, on va s'amuser
Rééro nga guindi ma
Je t'aime tellement, mon amour
Wayla ni youssou wayé birima
Viens avec moi, on va s'amuser
Koti koti yoli (2)
Koti koti yoli (2)
Sa lokho sama nope dima (2)
Je t'aime tellement, bébé (2)
Yoli yoli koti (2)
Yoli yoli koti (2)
Kham linga nameu motax malay (2)
Je ne peux pas imaginer ma vie sans toi (2)
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli (4)fois
Je t'aime tellement, "koti koti", on danse ensemble, "yoli yoli" (4)
Thiafka mbeuguel ngama niamal
Tu es mon tout, mon amour
Sama khol bi nga keuf moma sonal
Tu es mon rêve, mon soleil qui éclaire mon monde
Seytané yi nagnou mousseul
Les démons me tentent, mais je résiste
Yaye sama messi dama beugue ngamay teulle
Seul toi, mon amour, peux me faire oublier tout le reste
Dila khalate di réé
Je suis à toi, mon amour
Fepp nga meuné
Prends-moi, je suis toute à toi
Gni nane damay dieulé
Je suis amoureuse de toi, mon cœur bat pour toi
Nagnou ma thieupé
Je veux être toujours avec toi
Doynga kharite
Je t'offre mon cœur
Doy nga andando
Je t'offre mon âme
Bouma nieup bayé nala déssé
Je suis tellement amoureuse de toi
Make yaw si khalé
Je suis ta petite princesse
Héé!!
Héé!!
Rééro nga guindi ma
Je t'aime tellement, mon amour
Dila way ni youssou wayé birima
Viens avec moi, on va s'amuser
Rééro nga guindima
Je t'aime tellement, mon amour
Wayla ni youssou wayé birima
Viens avec moi, on va s'amuser
Koti koti yoli (2)
Koti koti yoli (2)
Sa lokho sama nope dima (2)
Je t'aime tellement, bébé (2)
Yoli yoli koti (2)
Yoli yoli koti (2)
Kham linga nameu motax malay (2)
Je ne peux pas imaginer ma vie sans toi (2)
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli (4)fois
Je t'aime tellement, "koti koti", on danse ensemble, "yoli yoli" (4)
Hé!!
Hé!!
Lou dak nékh
Je t'aime plus que tout
Lou dak nékh
Je t'aime plus que tout
Hé!!
Hé!!
Lou dak nékh
Je t'aime plus que tout
Koudoul yaw
Tu es mon chéri
Beugouma
Tu es tout pour moi
Yafi né!
Je t'aime tellement
Koudoul yaw
Tu es mon chéri
Beugouma
Tu es tout pour moi
Hey!!
Hey!!
Koudoul yaw
Tu es mon chéri
Beugouma
Tu es tout pour moi
Yafi nééé!!
Je t'aime tellement
Koudoul yaw
Tu es mon chéri
Beugouma beugouma
Tu es tout pour moi, tu es tout pour moi
Koti koti yoli (2)
Koti koti yoli (2)
Sa lokho sama nope dima (2)
Je t'aime tellement, bébé (2)
Yoli yoli koti (2)
Yoli yoli koti (2)
Kham linga nameu motax malay (2)
Je ne peux pas imaginer ma vie sans toi (2)
Koti koti yoli (2)
Koti koti yoli (2)
Sa lokho sama nope dima (2)
Je t'aime tellement, bébé (2)
Yoli yoli koti (2)
Yoli yoli koti (2)
Kham linga nameu motax malay (2)
Je ne peux pas imaginer ma vie sans toi (2)
Héh lou dakk nekh!
Héh je t'aime plus que tout!





Writer(s): omg, amadou ndiaga faye, cheikh tidiane kourouma


Attention! Feel free to leave feedback.