Thione Seck feat. Raam Daan - Mathiou - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Thione Seck feat. Raam Daan - Mathiou

Mathiou
Mathiou
Ndeye ndeyou ken la baye bayou nieupe la, sama yaye djé, sama yaye djii, guissouma koumalay meuna wethiéé, yaw mi gueune si mane yaw mi gueune si mane.
Ma bien-aimée, mon cœur t’aime tellement, ma bien-aimée, tu es ma joie, mon amour est pour toi comme le soleil qui brille, tu es ma source de vie, tu es ma source de vie.
Yaye boye sama galadj.
Mon amour, ma chérie.
Bo beugué djote sama djiko toudal sama yaye douma ko fowé doma ko fowé yaye boye sama galadj.
Je te tiens dans mon cœur, ma chérie, tu es mon amour, mon cœur t’aime tellement, mon cœur t’aime tellement, mon amour, ma chérie.
Rote nga thi leudeum debb nga thi taw, wale thi nadj bou tang bou yaye yeup melen ni yaw kene dou diour di sani.
Je t’aime plus que tout, tu es mon soleil, tu es mon destin, je t’aime plus que tout, je suis fou de toi, je suis fou de toi.
(Refrain)
(Refrain)
Ndeye ndeyou ken la baye bayou nieupe la, sama yaye djé, sama yaye djii, guissouma koumalay meuna wethiéé, yaw mi gueune si mane yaw mi gueune si mane.
Ma bien-aimée, mon cœur t’aime tellement, ma bien-aimée, tu es ma joie, mon amour est pour toi comme le soleil qui brille, tu es ma source de vie, tu es ma source de vie.
Yaye boye sama galadj.
Mon amour, ma chérie.
Djéba Ndoye, Indou woma woma ndeye sane, bayo boye dom djou am yaye day am baye wow wo
Djéba Ndoye, ma princesse, ma beauté, mon amour, tu es ma vie, je t’aime plus que tout.

Writer(s): Seck Thione

Thione Seck feat. Raam Daan - Favori
Album
Favori
date of release
04-11-2008

Attention! Feel free to leave feedback.