Wally B. Seck feat. Le Raam Daan - Dafmay Dal - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Wally B. Seck feat. Le Raam Daan - Dafmay Dal




Dafmay Dal
Dafmay Dal
Taay ma netalilen man lima dal si
Je te vois venir danser avec moi, mon cœur
Sama dingantek xalleh bima tal
Ton corps s'agite, tu as un charme fou
Thiono ngantal moy lima dal
J'aime voir tes mouvements, mon cœur
Man deh lima dal moy kouma
J'ai envie de te serrer dans mes bras, mon cœur
Dimbaleh
Continue
Lek lek ma xolko dioy
Bouge ton corps, laisse-toi aller
Sax dafmay dal mba ma xolko reh si dafmay dal thiono
Tu es si belle en dansant, mon cœur, tu es si belle
Ngantal moy lima dal man deh lima tal moy kouma dimbaleh
J'aime voir tes mouvements, mon cœur, j'ai envie de te serrer dans mes bras, mon cœur, continue
Lek lek solou bay dem mom mou terema ma daldi tok li dafmay dal
Bouge ton corps, laisse-toi aller, on va s'amuser, tu me fais tourner la tête
Melni kouko ragal dafmay dal man deh lima dal moy kouma dimbaleh
Ton sourire me ravit, mon cœur, j'ai envie de te serrer dans mes bras, mon cœur, continue
Tokna di waxtan bis mak samay waay telephone bi sonner mouy mom ma
Ne perds pas ton temps, appelle-moi, on se parlera au téléphone, mon cœur, mon amour
Daldi daaw melni kou ragal sax dafmay
On va danser, ton sourire me ravit, mon cœur, tu es si belle
Dal man lima tal moy kouma dimbaleh ehh waaw
J'ai envie de te serrer dans mes bras, mon cœur, continue, oh mon Dieu
Dieulinala nandeuna ningay doxeh eh hee anh anh sa bay moussouniouma
Tu es tellement belle, je suis fou amoureux de toi, oh oui, oh oui, tu me fais perdre la tête
Gnenkouleh sa ba lakari lelelaw gnekamouleh
Je veux te sentir contre moi, je veux t'embrasser
Guemou xadila anh moussoletou lakari lelelaw
Tu es si belle, mon amour, je veux t'embrasser
Worrna buur bi yalla niou boleh et siiii yamalen gueuneul soxna
Mon cœur, mon amour, je veux être avec toi, oh oui, je te désire tant
Nadipeh ba wakanda ndawsi deh moy sama seuytaneh
Je t'aimerai toujours, mon amour, je t'aimerai toujours, je suis fou de toi
Mbatam hoo iow dieuleul annh hi yeah woo woo waawaw
Tu es magnifique, mon amour, oh oui, oh oui, oh mon Dieu, oh mon Dieu, oh mon Dieu
Dama am sa faiblesse xolbi yassiy fess
Tu es ma faiblesse, je suis fou amoureux de toi
Deugleu dila dianer di dioy dafmay dal
Je veux te sentir dans mes bras, mon cœur, tu es si belle
Guissoulon ngagni gueumeu touniouma yenneu
Mon cœur bat la chamade, tu me fais tourner la tête
Say ma beugueu diengou gueneuthie dafmay dal
Mon cœur, je t'aime, je te désire, tu es si belle
Thiono gui thie beuguel diarnako doyna warreh
J'aime tes mouvements, tu es si belle, je suis fou amoureux de toi
Damay woo dame sene sama kaw scène
Mon cœur, mon amour, on est ensemble, sur scène
Takalko chaine nguir mou beguelalmalen
Tu es si belle, mon amour, je suis fou amoureux de toi
Guissouloni gagni gueumeutouniouma gnom deh louma wax niounima baxna
Mon cœur bat la chamade, tu me fais tourner la tête, mon cœur, je t'aime, je t'aime
Dioxnala thieur ba melni koula ragal dafmay dal
Ton sourire me ravit, mon cœur, tu es si belle
Awmathie kersa deugueulani diam si iow lakoy ameh dafmay dal
Tu es si belle, mon amour, je t'aime, je suis fou amoureux de toi
Mala tal yama tal di defal sama gagni dafmay dal waaw
Je veux te sentir dans mes bras, mon cœur, tu es si belle, oh mon Dieu
(Ssou soutanteh dinka gagneu ma am sa faiblesse
(Tu es ma faiblesse, je suis fou amoureux de toi
Xolbi yassiy fess dila dianerr di dioy dafmay dal)
Je veux te sentir dans mes bras, mon cœur, tu es si belle)
Wooy thionoh ngui thie beugeul diarnako doyna warreh
J'aime tes mouvements, tu es si belle, je suis fou amoureux de toi
End
Fin





Writer(s): Wally B. Seck

Wally B. Seck feat. Le Raam Daan - Symphonie
Album
Symphonie
date of release
11-12-2018



Attention! Feel free to leave feedback.