paroles de chanson Alxames (feat. ILAM) - ILAM , Ashs The Best
Bësu
alxames
bu
tiis
Ci
waxtu
timis
Ci
lañ
ma
diis
Naqqar
bu
tiis
Alxames
bu
tiis
Bu
tiis
a
tiis
Ci
lañ
ma
diis
Suma
waaji
dem
na
{dem
na}
Dem
na
{baayi
fi
njaboot
ji}
Dem
na
{ñëpp
a
koy
jooy}
Dem
na
{weetal
na
kër
gi}
Salaama
yaa
seydi
Salaama
yaa
Baaba
Taalibe
Maam
Ba'mba
Xol
bi
rafetoon
na
Jamm
laa
la
yeene
Doonoo
woon
alie'ne'
Aljana
Firdawsi
laa
la
yeene
Salaama
yaa
seydi
Baaba
Suma
waaji
dem
na
{dem
na}
Dem
na
{baayi
fi
njaboot
ji}
Dem
na
{ñëpp
a
koy
jooy}
Dem
na
{weetal
na
kër
gi}
Ebe
njaxaa
be
ngandaa
tobe
fay
Be
ngalaa
kobe
ñaami
Dum
ne
muusi
ni
xaw
nii
Sukaabe
Africa
ngummo
deen
(x)
Ngummo
deen
Liggo
deen
leydi
meen
saare
meen
Ñoo
foowandoo
Maggandoo
Def
nañ
lu
ne
Jaar
nañ
fu
ne
Lima
la
yeene
Aljana
laa
la
yeene
Doonoo
woon
alie'ne'
Taalibe
Maam
Ba'mba
Sa
jëf
ji
rafet
na
Baaba
Bësu
alxames
bu
tiis
Ci
waxtu
timis
Ci
lañ
ma
diis
Naqqar
bu
tiis
Alxames
bu
tiis
Bu
tiis
a
tiis
Ci
lañ
ma
diis
Suma
waaji
dem
na
{dem
na}
Dem
na
{baayi
fi
njaboot
ji}
Dem
na
{ñëpp
a
koy
jooy}
Dem
na
{weetal
na
kër
gi}
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.