Dip Doundou Guiss feat. CeePee - Dou raggal dou respect paroles de chanson

paroles de chanson Dou raggal dou respect - Ceepee , Dip Doundou Guiss



Par AbouAmg
Reptyle Music
Zero nul zero defaites
Xel you nioul sen xola fay
Dewagoul te danga ko ray
Danga dioum dou delou lay khekh
Beut bou nioul fayo ko kerr
Dafa mougne ba gedone na dem
Prince moussoul day dorr sa mere
Ken bougoul dou kerok ak tay rek
Ken bougoul louné moko ress man
Dieundeulo niou velo ak play
Souniou defoul effort nga mer
Dama guissoul ecole ba fay khekh
Fegn na tay sou yebo nga gued
Depuis xalé damay teud dila degg ngakoy yek lou melni khemé
Loutah Moussé yeureumoul madame ndakh khalei yi kat danio seuss
Mom nena fi dou galei sakh jail la
Niata goudi la teud pete
Tonton daga ma diga dig bama deurkiss si digg
Diggé bor la souma la fayako digua ma kill
Dip sa dom la mai sa dom mola geunal Dip
Namou mala xaliss rk ladone geudia guiss
Ndeki agne reer doyone na mai dou guifeul khiff
Khiff bima khiff la def si sama muzik ba sip
Deug nekhoul takhoul ba son bi bone
Kou ndieuka yewou cocorico
Doundone na conditions yi geuna meti si negou seye
Khol bi toy na mai nak mom dou dioy
Dor ak saga mom daniou ko mougne ba fi
Ndem dieumoul si khol si sa toute tank yi
Demal ma dem boul ma toudati bayinala bayi ma tout trankil
Dina dem
Dina sori
Beuss si beuss yi di nieuw dinga ma baaal
Dina dem
I'm sorry
Beuss si beuss yi di nieuw dina la baaaaallll
Iyaaa iyaa iyaaa iyaaaaa
Iyaaa iyaa iyaaa iyaiyaaa
Iyaaa iyaa iyaaa iyaaaaa
Iyaaa iyaa iyaaa iyaaaiyaaa
Broda man ma guena guiss sakh
Chak jour magui khekh pour nga nek
Chak jour yagui deff loula nekh
Takhoul bama decouragé
Dem nga fima la boufa dem
Demnga si gni ma bougona yakh
May nga len louniou wakh kagne nga nek yow nafekh
Dina maguet te dou fek sakh nga makk
Teyewo sa tank del kepp sa tate
Bateau demoul avion costé
Liguey bou leer la yalla dewoul kane mokoy fay
Defeant bou mak la ok bomay khekh ak ndiombé day fek nga atei world bi
Billet billet moune na compté galaxy S
Keur ak auto coathché Iphone 7
Dou ragal dou respect
Love la wala contrairou love
Nigga what the fuck I don't give a damn
Sama xol fess sama khol diekh na
Nigga lep leer na
Deug deug begg na
Sama xol bi fess na sama xol bi diekh naaa
Nigga lep leer
Deug deug begg na
Dou niroo dou niroo
Dou niroo dou niroo
Lou diota wessou lissi nara topou mounouniou niroo dou nouroo
Dou niroo dou niroo ohhh
Dou niroo dou nouroo
Dou nouroo dou nouroo
Dina dem
Dina sori
Bess si bess yi di nieuw dinga ma baaaal
Dina dem
I'm Soooryy
Beuss si beuss yi di nieuw dina la baaaallll
Iyaaaa iyaaaa iyaaaaa iiyaaa
Iyaaàa iyaaaa iyaaaaa iyaaaa
Iyaaaa iyaaaa iyaaaa iyaaaaa
Iyaaaa iyaaaa iyaaaa iyaaaaaa
Brodah man ma geuna guiss sakh



Writer(s): Dip Doundou Guiss


Dip Doundou Guiss feat. CeePee - Tay Leu Kagn
Album Tay Leu Kagn
date de sortie
04-11-2017



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.