Dip Doundou Guiss - Fayeku paroles de chanson

paroles de chanson Fayeku - Dip Doundou Guiss



Fayeku
Ngay comptél mane may pesé khaliss
Mangui 8e assamane di guiss niane yi yaw yangui 5e etage
Woté negn mbolo pour rayma ndax li legn dèssé mattou unité telecentre
Niom daniou tella ndiol yeukhé magg
Niom da niou niou yeukhé yoor tella niakk
Tekele ma ak yene boy yi moy tekele
Kerr ak naadj tekele gainde a khadj
Maouti wo na ko mai nango gou ma dieul khamna damkay msage
Waayé soumay dieulsi samay noone ak
Séni djiégué niaalé may ndieuk djaalé
Chien méchant nga nn do chef de gang
Chef de chantier mo geune chef de chambre
Diagg nga dou tou niou la big up*
Ma nigga thiat dougouleu da la bireul
May len lokho niou yotou sama rouu
Mangui ak khirr bi legn niou kheuffeulou
Xekh nga beug boul kharr niou eufoul niou
Amo drapeau ba di kheuthio
Yalla ak yalli lane moy taxx may roukh
Meme bou fenn amoul wone ken dou dioubb
Guelouwar dou ma tallal lokho moukk
Yelowane wou ma damay fayekou
Respect bi defko khaliss
Mane khamna yonou banque
Beugouma dem fou soriwoul
Motakh khawouma yonou diam
Diam dji defko business
Sauf bou fekei seu fite dess
Missionéi caissou Bill Gâtes
Khaliss dou déé même souy diekh
Fayekou liquide mba fayekou chèque
Fayekou souba non fayekou tay
Fayekou djouni mba fayekou ten
Bo ma fayoul lou cheroul nga fayma lou cher 2x
Deugeur tei deudj ni dreudj, leundeum ni deudj
Chaque jour la chaque njaabot bou ndol di dadj
Kou geum ni sa niak moy sa weurseuk, reuthie tekki faté lep lofi daadj
Sa geum niouy taxx ngay job di khagne sa
Bopp nelaw niouy daadj sa lallou hopital
Mbeugeul dou diay dou déé bou yebo do
Meusso guiss nmbeugeul bou taadj si boll agne
Kou na nga woutil xam xam bala am
Neko pour mou wone la keur kocc barma
Guiss na fi yeungeul geusseum sa taat ba jarr
Far yeungeul geusseum lou nekk sa compte banque
Fou thiat di eup geudd taww
Imam bi keupou caissou jaaka
Ribat si poche presi ak ribat si gordjiguen am liberté batt rekk
Ligueyel nguirr chèque
Lou lew neuw ni guiss vierge
Bougouniou tedd si pett
Religion bi bussiness
Hypocrite nga fuck sa love ak peace
Bala ngamay thiop ma thiop sa khiff
Forr sikim ni kou joudo si siiifff
Ken si niom denthioul djourom brique
Respect bi defko khaliss
Mane khamna yonou banque
Beugouma Dem fou soriwoul
Motakh khawouma yonou diam
Diam dji defko business
Sauf bou fekei seu fite dess
Missionéi caissou Bill Gâtes
Khaliss dou déé même souy diekh
Fayekou liquide mba fayekou chèque
Fayekou souba non fayekou tay
Fayekou djouni mba fayekou ten
Bo ma fayoul lou cheroul nga fayma lou cher 2x



Writer(s): Assad Nassour, Dominique Preira


Dip Doundou Guiss - Fayeku
Album Fayeku
date de sortie
09-12-2018

1 Fayeku




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.