Elzo Jamdong - Malembe - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Elzo Jamdong - Malembe




Malembe
Malembe
Seu projet ken meussouko khaar
Your project doesn't interest me
Homy lane la tchi meune?
Homie, what's going on?
Forcing bi nieup tchi marre
Forcing, I'm tired of it
Homy lane la tchi meune?
Homie, what's going on?
Saayo xewlé ken dou nieuw
Look at yourself, you're just a beginner
Homy lane la tchi meune?
Homie, what's going on?
Yaak sa gars yi réunion dima dieuw
You and your guys always have meetings in secret
Mais lane la tchi meune!
But what's going on!
Nitteu gueuneu meuneu bagn nitt
Singer wants to be a rapper
Motah rappeur yi niofi gueuneu meuneu bagn rappeur
Most rappers want to be singers
Nénagne meu "Free sa flow dina réy nitt"
Everyone says "Free your flow in the king's name"
Lima lerr moy douma baal bèneu rappeur (douma kèneu)
I'm already a good rapper (I'm good)
Awouma temps boudoul money boy (Awouma temps)
It's money boy time (It's time)
Am ngène chance damay djangui wone (Mane dama djangui wone)
I still have a chance, my love, don't worry (My love, don't worry)
Mayé nangou baxoul dédeeeeet
I won't give up, dedeeeeet
Mayoma mayma jaameuh nangou défaite (mayma jaameuh dong boy)
Never never will I accept defeat (Never ever, dong boy)
Zonou town mako ress boy (mako ress, mako ress)
Zonou town, I'm a tough boy (tough, tough)
Soma songué nala pess boy (nala pess, nala pess boy)
Think about it, I'm a bad boy (bad, bad boy)
Mane soxla wouma press wala
I don't care if you press or not
I'm the fucking best bouma stress bouma test boy
I'm the fucking best, you can stress, you can test boy
Samay vestes do guiss kène sole
My jackets are worth more than your shoes
Toujours classe fuck sa dress code
Always classy, fuck your dress code
Amena ay Ex yumay tek choc dima yoné texte
I send my exes text messages full of typos
Dima es. (espérer) pour niou sport
Always hoping for our sport
Yian xamna malène meune, Ben xamna malène meune
Yian is doing badly, Ben is doing badly
Wakh kat yi ba lène rek wa kogne bi ak kogne yeup mane lagn gueum
The wrestlers are just bragging, while I'm here working hard
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Free def niou ndank ya aliéné
Free def, we are not alienated
Beuri ay MC yu xalélé
Many MCs are going crazy
Togne nagn leu moss waayé baal lène rek
We are the best, they can just keep talking
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Free def niou ndank ya aliéné
Free def, we are not alienated
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Togne nagn leu moss waayé baal lène rek
We are the best, they can just keep talking
Yeah seu clip kène beugouko share
Yeah, your video doesn't get shared
Homy lane la tchi meune?
Homie, what's going on?
Amo ay mix mister Thier
I love Mister Thier's mixes
WoOOooo! Homy lane la tchi meune?
WoOOooo! Homie, what's going on?
Jamdong bi nga done xépp tay mola gueuneu cher
Jamdong is expensive, I'm not cheap
Homy lane la tchi meune?
Homie, what's going on?
Sa wa kogne mane laniou défal car nieuw sétane ci sama scène
You know I'm working hard because the devil is on my stage
Homy lane la tchi meune?
Homie, what's going on?
Lane la tchi meune?
What's going on?
Mane défar ay Hit sama maladie leu
I fight Hits, it's my illness
Yaw nullard ngeu lolou rk la xalate tchi yaw
You idiot, you're always making mistakes
nioune rek nga fan diniou mbalag di saupe
We're just fans, waiting to be saved
Sa daw fassou daaaw dotoul dalaate tchi yaw
You always mess up, you're always making mistakes
Xamal ni kalé nga ndakh fi ngako beug kalaate dou fofou
Don't try me, I'm not playing, I'm not a fool
Chaque jour liguèy sama calendrier (Liguèy rek liguèy rek)
Every day, check my calendar (Check, check)
Fi amo fi ndieurigne comme salade ci deummeu
I'm everywhere, like salad on the table
Défal ndank!
Step back!
Bi lepp séléw mane ma nieuw yengueulaate leu yéé leu
Everyone is jealous, they're always complaining, yeah
Ma nieuw yégueulaate sa level ya meuneu faaté ba yeem meu
They're always complaining, my level is too high for them
Bi sèn game bi di nélaw ma nieuw nexalaate yeah mane
In this game, they're always trying to trip me up, yeah
Ma indi rap bi nga yélole push ko ni Baba ak Yééla
I'm carrying the rap game, pushing it with Baba and Yééla
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Gnima done dinkaate nieup nalène béteu
They're always watching us, but we're doing well
Ma ngi tchi djawou dji. Yeen fane ngène né?
I don't care what they say. Do you understand?
Dina lène diokh sen dose ba ngèn bék
In this world, I take my dose and I leave
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Free def niou ndank ya aliéné
Free def, we are not alienated
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Togne nagn leu moss waayé baal lène rek
We are the best, they can just keep talking
Yeah! Kène meunoul téé lima done di ….
Yeah! I don't have time to....
Tell them dama nieuw ngir fay leu (Dama nëk)
Tell them I'm here to destroy them (I'm here)
Mane ak yeen on est trop différent (Dawal)
Me and them, we are too different (Different)
Dama original yeen ngène copier yéémeu (Baayi lène di topando)
I'm original, they're just copies (Stop copying)
Douma nopi ndakh amna avenir douma salopard
They're worthless, they have no future, they're bastards
Dama xiff meun na lekk yappou charognard
I'm disgusted, they're like vultures
Douma domou riche awma avocat
They want to be rich, they want to be lawyers
féppeu la son bi di daw diaroul à vos marques
But the whistle is blowing, get ready, on your marks
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé
Malembé Malembé






Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.