Nix feat. Omzo Dollar - La Boca - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Nix feat. Omzo Dollar - La Boca

La Boca
The Mouth
Yeah yeah
Yeah yeah
Abozé
Abozé
Hé!
Hé!
Miézé Miézé
Miézé Miézé
C′ta dire que en fait
C′ta dire que en fait
N-Eazy N-Easy
N-Eazy N-Easy
Gnigni gne gnigni (mdr)
Gnigni gne gnigni (mdr)
Game bi laye deif sens interdit waxma louci sama yoooon

Guisseugouma kouma diaxal mangui moytu sama boopp

Bop beu legui deim nagn nieuw nagn yangui tiéné fingua tooog

Prouvé prouvé reik beu keine dotul amatii loumouy wax

La Boca La Boca!
La Boca La Boca!
Fils Fayma Money
Fils Fayma Money
Sinon Nala Noxa
Sinon Nala Noxa
La Boca La Boca!
La Boca La Boca!
Mak Sama Bendo Di Geinei Ay Lingo Es La Vida Loca

Plata O Plomo
Plata O Plomo
Noto diplomo
Noto diplomo
Ay! Accéléré nah sa défaite nga doundou ko Slow- Mo

Niggaz tChi hood bi geuneuh taxaw poteau

La vie de loco moy champoing ak omo
La vie de loco moy champoing ak omo
Ay montant loto tchi biir beine lox
Ay montant loto tchi biir beine lox
Ay boone you sadique boie day andak toxo

Mayma ma waxtane ak nioom ma geuneuh nioul fi boie kone fuck sa choco

Mayma boie may leik ak nioom tchi restaurant chic di tankxa ak loxo

Boie ma daxa deim soll Mwaka
Boie ma daxa deim soll Mwaka
Ay collé serré cap verdienne la taka
Ay collé serré cap verdienne la taka
Fi meunoul leundeum tank mangui taka Boie

Yangui serasse 1, 2 niou geneii paka . Han!!
Yangui will be 1, 2 niou geneii paka . Han!!
Découper découper MC boie Omzo tem niou oubi dibiterie diay ay MC
Cut out cut out MC boie Omzo tem niou oubi dibiterie diay ay MC
Par mariner seine djiko solale seine manager yi ay string en nilon
By mariner seine djiko solale seine manager yi ay string in nilon
Le hilander parcours en tilon kodal
The hilander course in tilon kodal
Pendant 1000 ans ak dissayou millions de pilons
For 1000 years ak dissayou millions of drumsticks
Et ni l'un ni l′autre buenos ouvrir sene boca

Sinon dagn kay anesthésier comme la coca

Si si may kilay fuck everyday
Si si may kilay fuck everyday
Mane may farou rap bu épicé
Mane may farou rap bu épicé
Rappeur yangui diema diay lou saff boie
Rappeur yangui diema diay lou saff boie
Loo beug niou doon boie apar mes épiciers

Legui nieuw leine boie waxtanal Nikissi
Legui nieuw leine boie waxtanal Nikissi
Nioumay xool dima ladj kagn lay gnibissi

Dama lak français boie beu doyal humm legui dieul wolof bii confisquer
Dama lak français boie beu doyal humm legui dieul wolof bii confisquer
Game bi laye deif sens interdit waxma louci sama yoooon
Game bi laye deif sens interdit waxma louci sama yoooon
Guisseugouma kouma diaxal mangui moytu sama boopp
Guisseugouma kouma diaxal mangui moytu sama boopp
Bop beu legui deim nagn nieuw nagn yangui tiéné fingua tooog
Bop beu legui deim nagn nieuw nagn yangui tiéné fingua tooog
Prouvé prouvé reik beu keine dotul amatii loumouy wax
Prouvé prouvé reik beu keine dotul amatii loumouy wax
La Boca La Boca!
La Boca La Boca!
Fils Fayma Money
Fils Fayma Money
Sinon Nala Noxa
Sinon Nala Noxa
La Boca La Boca!
La Boca La Boca!
Mak Sama Bendo Di Geinei Ay Lingo Es La Vida Loca
Mak Sama Bendo Di Geinei Ay Lingo Es La Vida Loca
Hey . C'ta dire que
Hey . C'ta dire que
Capitano mane la Raùl
Capitano mane la Raùl
Gayndei guissma youxou miaou
Gayndei guissma youxou miaou
Dernier K.O premier gawou
Dernier K.O premier gawou
1 Millions dans les poches juste au cas
1 Millions dans les poches juste au cas
Fils mane la BCEAO boudei Daw lagn niouy diay

Eaux et forêts boudei Flow lagn niouy diay

Cachet 1 Millions sou tiolei niou bayii
Cachet 1 Millions sou tiolei niou bayii
Mane tata ViVi momay woway nidiaye ... Mouah!!

Awma wone moyenne mais fils j'ai les
Awma wone moyenne mais fils j'ai les
Moyens plus que touts mes instructeurs
Moyens plus que touts mes instructeurs
Boie yangui tiéné si kogn bi di taal
Boie yangui tiéné si kogn bi di taal
Ay doublé beu meilni meilleur buteur
Ay doublé beu meilni meilleur buteur
Boie Miézé amna diplôme mam
Boie Miézé amna diplôme mam
Hiit Bopam nikou saga ndeye doma
Hiit Bopam nikou saga ndeye doma
Aucune option c′est la fuite
Aucune option c′est la fuite
Marche rappeur galsen yi seine fête moy le 8 Mars

Han!!
Han!!
Bayma xeil nga neik borom bop
Bayma xeil nga neik borom bop
Samay 12 doko guiss si horoscope
Samay 12 doko guiss si horoscope
Torox no fresh to deif beu Europe loxx
Torox no fresh to deif beu Europe loxx
Dieulel tof ... Mane ak rap comme wërr ak doff

Weur ak tog ... Waxma ani goor ak lokh
Weur ak tog ... Waxma ani goor ak lokh
Door ak love ... Man ak niom comme door ak boxe

Sport ak dox ... Légui xébb na djolof trop

Rap galsen na eup thiaass ngor ak Yoff.
Rap galsen na eup thiaass ngor ak Yoff.
Fils waxma loutax sa grand mer
Fils waxma loutax sa grand mer
Ma grammaire n′épargne aucune grand mère

Wa sipres samay son dougn keu gemei
Wa sipres samay son dougn keu gemei
Neinagn niom juuli reik lagn ma xamei
Neinagn niom juuli reik lagn ma xamei
Mangui téléphone ak sama avocat
Mangui téléphone ak sama avocat
Gueil bu andak formou bouteilou coca
Gueil bu andak formou bouteilou coca
No djouto gand motherfuck hey
No djouto gand motherfuck hey
Game bi laye deif sens interdit waxma louci sama yoooon
Game bi laye deif sens interdit waxma louci sama yoooon
Guisseugouma kouma diaxal mangui moytu sama boopp
Guisseugouma kouma diaxal mangui moytu sama boopp
Bop beu legui deim nagn nieuw nagn yangui tiéné fingua tooog
Bop beu legui deim nagn nieuw nagn yangui tiéné fingua tooog
Prouvé prouvé reik beu keine dotul amatii loumouy wax
Prouvé prouvé reik beu keine dotul amatii loumouy wax
La Boca La Boca!
La Boca La Boca!
Fils Fayma Money
Fils Fayma Money
Sinon Nala Noxa
Sinon Nala Noxa
La Boca La Boca!
La Boca La Boca!
Mak Sama Bendo Di Geinei Ay Lingo Es La Vida Loca
Mak Sama Bendo Di Geinei Ay Lingo Es La Vida Loca

Nix feat. Omzo Dollar - La boca
Album
La boca
date de sortie
17-10-2017

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.