paroles de chanson Dabbaax - Youssou N'Dour
Keroksou
penc
bognouy
wadjia
wathié
janta
bi
Di
wadjial
Péssé
ba
Moulay
dabbaxx
yalla
nagnou
la
diégué
yalla
daal
moy
taan
waayam
Moulaay
Dabaaaaax...
Bougnou
Faté,
Bess
boboulé,
Uhh
Bougnou
Soré,
Bess
boboulé
Bougnou
faté
Bess
Boboulé,
Lofa
Gnaane,
Yalla
May
lako.
Modaane
wakhal
nitt
gnep,
Mo
daane
wakhal
nasraane
yi
Anh
Mo
daane
Kadou
Askane
wi.
Dafa
daane
wakh
naane
nagnou
bolé
sougn
rew
Dafa
daane
wakh
naane
bou
kéne
wéngal
gaal
gui
Dafa
daane
wakh
naane
nagnou
bolé
sounou
khol
yi
Dafa
daane
wakh
naane
nagnou
yeureum
Djiguéen
Sa
borom
bi
begu
na,
Yonentam
bi
begu
na,
yako
liguéyal
sa
borom.
Moulaye
Dabbaxx
yaw
dé
wacci
ngua
masso
wakh
lou
amoul.
Kérok
bang
gnou
djito
assamaane
si
da
Leudeum,
Bessa
ngui
kéne
dotou
ko
Fatéééti...
Moulaay
Dabbaxx
Bougnou
Faté,
Bess
boboulé,
Bougnou
Soré,
Bess
boboulé
Bougnou
faté
Bess
Boboulé,
Lofa
Gnaane,
Yalla
May
lako.
Anh!
Modaane
wakhal
nitt
gnep,
anh!
Mo
daane
wakhal
nasraane
yi.
Anh!
Mo
daane
wakhal
Askane
wi.
Dafa
daane
wakh
naane
na
gnep
ligueye
Dafa
daane
wakh
naane
nagn
diangal
gounéyi
Dafa
daane
wakh
naane
na
gnep
liguèye
Dafa
daane
wakh
naane
nagn
diangal
djiguééne
gni
Daawaoul
Sétane
lou
gnaaw
Poussom
la
yorone
fou
khotékou
Mou
gnaw
Rewmi.rewmi
amélnagnou
la
ndiouka
Moulaay
Dabbaxx
Daawaoul
Sétane
lou
gnaaw
Poussom
la
yorone
fou
khotékou
Mou
gnaw
Rewmi.rewmi
amélnagnou
la
ndiouka
Moulaay
Dabbaxx.
Bakrék
Dara
Maam,
Aram
lô
Coumba
Thiam,
Magn
Penda
ak
Pathé
Pendaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaah
Modaane
wakhal
nitt
gnep,
Mo
daane
wakhal
nasraane
yi
Mo
daane
Kadou
Askane
wi.
Dafa
daane
wakh
naane
nagn
diap
sounou
rewmi.
Dafa
daane
wakh
naane
nagnep
liguéye
Dafa
daane
wakh
naane
nagn
Yeureum
djiguéene
gni.
Dafa
daane
wakh
naane
nagn
diangal
gounéyi
1 4-4-44
2 Pullo Àrdo
3 Sama Gàmmu
4 Bàjjan
5 Baay Faal
6 Sportif
7 Tukki
8 Létt Ma
9 Dabbaax
10 Xel
11 Wake Up (It's Africa Calling)
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.