Youssou N'Dour - Jeegel Nu paroles de chanson

paroles de chanson Jeegel Nu - Youssou N'Dour



Lépe Louma La Massa Défe
Toube Na
Réthiouna
Lépe Louma La Massa Togne
Diégalmako
Lépe Louma La Massa Défe
Toube Na
Réthiouna
Lépe Louma La Massa Togne
Diégalmako
Ya ALLAHOU WAKHIDOUNE
Toube Na
Réthiouna
Lépe Louma La Massa Togne
Diégalmako
Bouri Bouri RABANA
Toube Na
Réthiouna
Lépe Louma La Massa Togne
Diégalmako
Lépe Louma La Massa Défe
Toube Na
Réthiouna
YALLA Loumala Massa Togne
Diégalmako
Ya ALLAHOU WAKHIDOUNE
Toube Na
Réthiouna
Lépe Louma La Massa Togne
Diégalmako
Bouri Bouri Rabana
Toube Na
Réthiouna
Lépe Louma La Massa Togne
Diégalmako
I Regret All My Mistakes
Forgive Me Almighty God
Nama YALLA Bale
YALLA Nama YALLA Bale
I Regret
YALLA Balma
I Regret All My Mistakes
Forgive Me
Almighty God
Nama YALLA Bale
YALLA Nama YALLA Bale
I Regret
YALLA Balma
Forgive Me All My Sins
The Merciful
Forgive Me My Mistakes
The Merciful
Give Me A Second Chance
The Merciful
Almighty almighty God
The merciful
I regret I regret yeah
Jamm la di togne kat
Di moy kat bou rey bi
I regret I regret yeah
Jamm la di togne kat
Di moy kat bou rey bi
I regret I regret yeah
Jamm la di togne kat
Di moy kat bou rey bi
I regret I regret yeah
Jamm la di togne kat
Di moy kat bou rey bi
I regret I regret yeah
Lou neubbou ak lou fégne
Tchi yaw ak sey jaam
Lepp lou mala meusseu togne
Diegalmako
Lo khamni maa ko tey ak louma teyoul
Lepp loumala meusseu def diégalmako
Lou neubbou ak lou fégn tchi yaw ak sey jaam
Diegalmako
Geum naani yaa di bour ya Allahou rabbanaa
Lepp loumala meusseu def
Diegalmako
Jamm la di togne kat
Di moy kat bou rey bi
I regret I regret yeah
Jamm la di togne kat
Di moy kat bou rey bi
I regret I regret yeah
Jamm la di togne kat
Di moy kat bou rey bi
I regret I regret yeah
Jamm la di togne kat
Di moy kat bou rey bi
I regret I regret yeah
Forgive
I regret I regret
Forgive me my mistakes




Youssou N'Dour - Africa Rekk
Album Africa Rekk
date de sortie
04-11-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.