paroles de chanson Immigrés - Youssou N'Dour , Étoile de Dakar
Par
AbouAmg
Du
nil,
du
nil
bëgg
naa
nga
létt
ma
walla
book
nga
firi
ma
Xamal
ma
lu
leer
Danga
maa
woolu
sa
gàll
e
ma
ñëw
nga
mel
ni
xale
Yaw
daal
yaw
téppal
fële
Danga
ba
di
tappale
Su
fekkeeni
parewoo
waru
loo
di
yónéé
Ngall
yaw
bul
ma
defioo
lu
ma
nin
ni
di
xeebe
Létt
ma
mbaa
nga
firi
ma
Bëgg
naa
nga
létt
ma
walla
book
nga
firi
ma
Bëgg
naa
nga
létt
ma
walla
book
nga
firi
ma
Lég
lég
sax
nga
yónni
ma
Ma
dem
bay
dem
nga
teye
ma
Léégi
sax
dematuma
Damay
bañ
nga
dugël
ma
Bu
fekkeeni
parewoo
wanu
loo
di
yónéé
Ngall
yaw
bui
ma
def
loo
lu
ma
nin
ñi
di
xeebe
Létt
ma
mbaa
nga
firi
ma
Bëgg
naa
nga
létt
ma
walla
book
nga
firi
ma
Bëgg
naa
nga
létt
ma
walla
book
nga
firi
ma
Bari
pexe
weesuwul
nettali
sa
géntu
moroom
Bëgg
nga
ma
demal
la
wax
ma
kon
li
ne
ci
yaw
Bari
pexe
weesuwul
nettali
sa
géntu
moroom
Bëgg
nga
ma
demal
la
wax
ma
kon
li
ne
ci
yaw
Létt
ma
mbaa
nga
firi
ma
Bëgg
naa
nga
létt
ma
walla
book
nga
firi
ma
Bëgg
naa
nga
létt
ma
walla
book
nga
firi
ma
Boo
ma
waxee
fi
nga
bêgg
dem
Ma
wax
la
fi
ngay
jaar
Demal
bl
dem,
waxal
bul
wax,
defal
bul
def
Man
daal
sonn
naa,
sonn
naa
sonn
naa
Bëgg
naa
nga
létt
ma
walla
book
nga
firi
ma
Bëgg
naa
ko
tay,
Bañ
naa
ko
subë
kon
xanaa
ganaaw
subë
bëgg
ak
bañ
la
.. .
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.