Nitdoff feat. Mao Sidibé - Yoonu Ndaw - перевод текста песни на английский

Текст и перевод песни Nitdoff feat. Mao Sidibé - Yoonu Ndaw




Yoonu Ndaw
Yoonu Ndaw
Dokh ci yonou ndaw dafeu bari piège
There are a lot of traps in life, a lot of pitfalls.
Meun nga fallin' down meun na doon lou yées
When you fall down, you have to know how to get up.
Doolé dokhoul diam saurato ay conséquences
Sometimes, our choices have consequences.
Life fou legalize rékey doon sey influences
Life is crazy, legalized, but don't let it influence you.
Yonou ndaw dou wéey teguil sa tank please
Life is hard, it won't please you.
Bodoul ingénieur meun nga doon chef d'entreprise
I could have been an engineer, or a CEO.
Att yi nga tolou sa dérét dafey tangue
But I took the wrong path, the path of delinquency.
So tarkhissé rek meun nga niak bepp maîtrise
And today, I regret it, but I have to master myself.
Petit frère écoute moi
Little brother, listen to me
Yonou ndaw moleu djiap mélo ni
Life is hard, it's not a melody.
Petite soeur mais dis moi
Little sister, tell me
Pourquoi tu penses que si triste est la vie?
Why do you think life is so sad?
Le meilleur reste à venir
The best is yet to come.
C'est maintenant que tu dois batir
Now is the time to build.
Ton avenir, ton avenir, prépare toi pour ton avenir
Your future, your future, prepare for your future.
Yeah ya ngui tolou pont bou diafé djiegui boy
Yeah, many have crossed the bridge, but not properly, boy.
Gni si toloon naagu danio djieki djieki yooy
They only look at the glitter, not the substance.
Virage bi nga nekk moy déterminer fi nga dieum
At the turn, I was determined to get up.
Andado you bonn danie léy précipiter ci leundeum
But you, you rushed, you precipitated things.
Niep gui koy def waroul takh nga warko def
Those who laugh at you when you fall are the first to give up.
Complexer bakhoul doon sa propre chef ci li séy choice
Having a complex is giving up being your own boss, making your own choices.
Khana xamo ni diné meun neu doon boussole
If you don't listen to anyone, you'll never have a compass.
So tchi télé tagguatt sa bopp
The one who follows TV, he loses himself.
Léer gui dafey sakh sa khole
Those who study, it's for their own good.
Petit frère ecoute moi
Little brother, listen to me
Yonou ndaw moleu djiap mélo ni
Life is hard, it's not a melody.
Petite soeur mais dis moi
Little sister, tell me
Pourquoi tu penses que si triste est la vie?
Why do you think life is so sad?
Le meilleur reste à venir
The best is yet to come
C'est maintenant que tu dois batir
Now is the time to build
Ton avenir, ton avenir, prépare toi pour ton avenir
Your future, your future, prepare for your future.
Han khalé bou dioumé boul ko téleu wakh ni da nga bonn
Every time you are told to work, you say that you will do it.
Dieuleul sa temps nga dioubanti ko bamou doon
You waste your time, you do nothing.
Ki ngey saguo euleuk fepp nane khole léen sama dome
You're just talking, showing off in front of your friends.
Guinaw Yallah dala sameu lo kone waro faille
God's grace is with me, He knows that I am not perfect.
Beurina wadiour youy échouer tchi sen oyofaay
Tomorrow is another day, failure is part of learning.
Sa dome dou nguew am xélam boul ko yéw
In your head, you think you know everything.
Liy thiossanam warna fégne tchi mom fepp foumou téew
But life will teach you things that no one can teach you.
Sinon rek nga sopiko ap dondjie keurign ci biir méew
Otherwise, you'll end up in a graveyard, a cemetery.
Petit frère ecoute moi
Little brother, listen to me
Yonou ndaw moleu djiap mélo ni
Life is hard, it's not a melody.
Petite soeur mais dis moi
Little sister, tell me
Pourquoi tu penses que si triste est la vie?
Why do you think life is so sad?
Le meilleur reste à venir
The best is yet to come.
C'est maintenant que tu dois batir
Now is the time to build
Ton avenir, ton avenir,prépare toi pour ton avenir
Your future, your future, prepare for your future.
Little little sista
Little little sister
Little little broda
Little little brother
Take care of yourself
Take care of yourself.
Adouna yaguoul wéi
The world is hard.
Yonou ndaw dou wéey dou wéey dou wéey dou wéey dou wéey
Life is hard, hard, hard, hard, hard.
Kone gars yi téelou léen
Know that guys are watching you.





Авторы: Mao Sidibé, Mor Talla Gueye, Thibault Van Raemdonck


Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.