Youssou N'Dour - Hey You - перевод текста песни на французский

Hey You - Youssou N'Dourперевод на французский




Hey You
Hey You
Ndékkété yo beugouloma
Je t'aime tant
Ndékkété yo nobouloma
Je ne peux pas vivre sans toi
Ndékkété yo faléwoma
Je t'aime beaucoup
Ba att yi niou am yeup
Tu es tout pour moi
Sama khel nekk thi iow
Je te veux toujours
Nga kheyni dangay sey akk kenene koudoul mane
Tu es ma joie, mon soleil, mon amour
Heureusement fatéwouma sama niom yaye samay kharit samay deukeundo waw con ma rouss
Heureusement, je t'ai trouvé, tu es mon étoile, mon destin, tu es le soleil de ma vie.
Hey you! ana Ami?
Hey you! Mon amour?
Kokou dal nekkoul sama nitt
Mon cœur te dit "je t'aime"
Hey you you! Ana Ami?
Hey you you! Mon amour?
Ndékkété yo beugouloma
Je t'aime tant
Ndékkété yo nobouloma
Je ne peux pas vivre sans toi
Ndékkété yo faléwoma
Je t'aime beaucoup
Ba att yi niou am yeup
Tu es tout pour moi
Sama khel nekk si iow
Je te veux toujours
Nga kheyni danguey sey akk kenene koudoul mane
Tu es ma joie, mon soleil, mon amour
Heureusement fatéwouma sama niom yaye samay kharit samay deukeundo waw con ma rouss
Heureusement, je t'ai trouvé, tu es mon étoile, mon destin, tu es le soleil de ma vie.
Hey you! Ana Ami?
Hey you! Mon amour?
Koku dal nekkoul sama nitt
Mon cœur te dit "je t'aime"
Hey you you! Ana Ami?
Hey you you! Mon amour?
Koku dal nekkoul sama nitt
Mon cœur te dit "je t'aime"
Hey you! Ana Ami?
Hey you! Mon amour?
Koku dal nekkatoul sama nitt kheyna dafa guiss dafa guiss kenene kouko gueneul
Mon cœur te dit "je t'aime" et je ne peux pas m'empêcher de le dire, de le dire, tu es mon amour.
Ni Faléwoma Faléwoma
Je t'aime beaucoup, je t'aime beaucoup
Beu att yiniou djotta deff yeup ndekke faléwomay
Tu es tout pour moi, tu es tout pour moi, je t'aime beaucoup.
Koloré yaye
Tu es mon soleil
Gorel nama woy
Tu es mon amour, tu es mon tout
Wowowowooo
Wowowowooo
Yeyeyeyeeeee
Yeyeyeyeeeee
Koloré yaye
Tu es mon soleil
Deug deug rernama woy
Tu es mon amour, tu es mon tout
Wowowowooo
Wowowowooo
Yeyeyeyeee
Yeyeyeyeee
Koku dal nekkatoul sama nitt
Mon cœur te dit "je t'aime"
Yeyeyeyeyeeee
Yeyeyeyeyeeee
Wowowowoooo
Wowowowoooo
Ndékkete yo beugouloma
Je t'aime tant
Ndekkete yo nobouloma
Je ne peux pas vivre sans toi
Ndekkete yo falewoma
Je t'aime beaucoup
Ba att yiniou am yeup
Tu es tout pour moi
Sama khel nekk thi iow
Je te veux toujours
End
Fin





Авторы: Habib Faye, Youssou N Dour


Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.