Africando - Sey Lyrics

Lyrics Sey - Africando



Bo takké sa jieg amak mom ay tom
Boko weuthié sa jaboot taxawalu
Yay mi jiguén topatol sa Sey
fo mena toll nangol dann sa dollé moy sa waref
Baylén jay sén domm
Ala du Sey
Sey 3 waref la
Dund bu doy
Thiangay lu doy
Jamm ju sa
Lolu moy Sey, gayi sédé lén ma




Africando - Betece
Album Betece
date of release
14-05-2007




Attention! Feel free to leave feedback.