Ashs The Best - Tukki Bukki Lyrics

Lyrics Tukki Bukki - Ashs The Best



Bu xaaju guddee bu xaaju guddee
Bu ñëpp di nelaw man ma
Weet'ag xaalat waxtaan'ag njegenaay
Kenn du ma yee ku nelawul nan lañ koy yeewee
Biig foru ma bët waxtaan'ag njegenaay
Nelawu ma biig
Xanaa waxtaan'ag sama njegenaay
Tay kenn duma yee
Ku nelawul nan lañ koy yeewee
Xale baa ngi jooy
Nax ko warul jooy
Doomu jambur warul jooy
Demb laa la miin
Tay yaa ngi taggoo
Soy dem yobbaale ma
Ulluku
Man ku ma nëbbu ma reer la
Ci rukku
Laa la woo yobaante la
Ulluku boy nelaw bul xaar mu yee la
Kuy tukki
Deeg naa ñu ne warul taggoo
Fukki bukki laa gis taggaliko'og sama saggo
Ulluku boy nelaw bul xaar mu yee la
Bul ma di sooraale
Sooraaleel sa bopp
Soy dox di gestuwaale
Mën nga fakkastalu
Ulluku ku ku ku ku
Kuma nëbbu ma reer la
Ulluku ku ku ku ku
Tukki tukki bukki
Tukki bukki
Fukki bukki guddi
Fukki bukki bëccëg oo
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Bukki bënn buntu
Bant bënn bëttëm
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Fukki bukki guddi
Fukki bukki bëccëg oo
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Bukki bënn buntu
Bant bënn bëttëm
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Ulluku ku ku ku ku
Man ku ma nëbbu ma reer la



Writer(s): Olivier Delahaye, Sy Abdoulaye


Ashs The Best - Tukki
Album Tukki
date of release
23-12-2022




Attention! Feel free to leave feedback.