Coumba Gawlo - Naby Lyrics

Lyrics Naby - Coumba Gawlo



Par AbouAmg
Ngeňne gūї mbїdef ŋaby
Bessoū t lawone
Naby romb xaleyї gnoū lok
Sagn se ba jїeck do fo do fo ree
Am tchїa gnome koū dїoy
Ngeūne gūї mbїdef ŋaby
Woo say xale-ba, neko dom
Wo loū noy wa?
Xaleї ba dal ko
Sama baie DAA etd'un Tchia xekh ba akk Naby
Dee fa ma weett dїkhle
Sama Yaye seūy ak benene
GȮor móu gūenne ma Nangou sama alal
Nangou sama keur ba nangūї
Toūmoūranke
takkawaloū ak fanane tchi Mbede
Móu torokhal ma sanalma
Metїtalma
Mo waral tchi bessoū it by
Sama xel dem tchi saama baye ma wete dioy
Xamne soū doūndone doūma meūsseū toūmoūranke
Nakanonoū ŋaby
Ne xalebe ŋjakh beūg nga ma done da bay
Aichatoū done say aye
Fatimatoū done samak
Wa alioūne ak hassane ak hoūsseyuoū
Done say mak
Xaleba daldї nїko
Ana kane peut bagne ya rassoūloūlah ŋaby
Ana kane MOY bagne ya Rassouloulah
Ngūeūne gūї mbїdef, kїgūeūne te kene gūeūnoūko
Khoūreyshine yay Sene gūeer
Banoūhassim yay sen baye
Ana kane MOY bagn Naby
Nakanonoū Naby
Yoboū xale soit keūreūm, taralko
Móu delloū si taroūlole
Gneūw morrom ya nane ko
Sa taar bїї ak sa leer gūї nga andal
Woūtena ak bїnga fїy dїoūgūe
Njakh danga melni koū dїoūddoū waatt
Xale be dalvi nїlene
Yonene la dadїel
Moū latji ma loū may dїoy
Ma wakh ko ko moū yoboū matsakh ma
Keū manlo
Aїchatoū done sama yay
Fatїmatoū done sama makk
Wa alїoūne ak Hassane ak Hoūsseynoū
Done samay makk
Kharїte ya daldi niko
Yaa ŋaby
Soūgnoū sagnone
Soūgnoū baye
Dee tchїa kharee ba
Ndkh yaa rassoulloūllah



Writer(s): Coumba Gawlo


Coumba Gawlo - Terrou Waar
Album Terrou Waar
date of release
07-12-2018




Attention! Feel free to leave feedback.