Leuz Diwane G - Yobeunte Lyrics

Lyrics Yobeunte - Leuz Diwane G



This nice track i've tried to make the lyric...
Victory lagnou wout si gneuwougnou pour gain hiphop history
Gneuw dougou si writte fa sougnou name
Never défaite rabou ndaam lagnou taane
Taamou souk job defko mébeutt gueum gueum ak djeum djeum
Gnou deugou seugue job reuy beut diir fou sori sépi léép si mind
Leudj mbeut... lognou doupé line yi
This is more than Hip Hop yep! It is a mission
We'll be there on the mountain top got an heal the passion
Parélène gnou takk diog dèm cuz fougnou dieumeu sori
Khaleu lène fokk gnou gneuw bokeu diémeu feuleu bord yi
Feulaatt tort yi
Fakhass corps yi fokk gnou diégui aéroport yi
Fayaatt borr yi wakh ak goor yi
Fokk gnou indil lène rapport nèw dolé
Baat you mort yi lagnoy dékil yép thi bord yi
Yèw yolé garde corps fokk gnou dioot si médaille d'or yi
Toor toor rou garabou nafèkh yi mégnone lagnouy boori
Don't worry da gnouy gori lép lou nara sori lori (heey!)
Yobeunté bi la gnou yob si borom(si borooomm)
Tookk lène wait gno ngui gneuw si app diir bou gaat(aaah iioooo)
Dokh diganté diokh kou nekk li mou moome(kou nekk li mou moooome)
[...]Never beug gnou mou takh(Neeeveeerr)
If you're ready let's gooooo
Fonk rap ni diouli diouplou pinkou laap xel yi first
Tèèy ni ndiaabou ndiouly bagne reuthiou ngaalaap xol yi first
Ngèmb xèl mou noott katane daw reuthie safaane
Téla bott dou dagane doundeul rou ndiatt bakane
Nganayo diaassi OMAR KHATAAB di dogué deug
Dieul woyof def ko carte dèm gab sagne takhaw feug
Banque withdom lagnou tidji compte
Signé gueustou contrat freedom wala def décompte
Faat lougnou [...]
Bla bla dou fauute drap wala bala il faudra
Est que aura gnou reub rat ni cobra
Weur Thiabi dji tidji brain kèp teuthie ibliss
Yoor diab bi nara aadji rène sét beu keuthie thigliss
Ték békoor yi tor yi fékhé ba norr yi naat ni nawéét
Sèèt décoré Goor yi wéri faute ni taw bi sébétt(héééé)
Yobeunté bi la gnou yob si borom(si borooomm)
Tookk lène wait gno ngui gneuw si ap diir bou gaat(aaah iioooo)
Dokh diganté bi diokh kou nekk li mou moome(kou nekk li mou moooome)
[...]Never beug gnou mou takh(Neeeveeerr)
If you're ready let's gooooo
There may be so long, always be so slow
Parélène gnou ngui gneuw indi li gnou wouti woone
Parélène gnou ngui gneuw takh gnou yaag saam yoone
Parélène gnou ngui gneuw indi li gnou wouti woone
Parélène gnou ngui gneuw diaroul ladjté gno ngui gneuw
Yoobeunté fok mou yègue dont worry bro
Loumou gnangue gnangue dougnou khaadi
Pour nguène diot si li nguène moma takh
Gnou ngémbou wara kharé dougnou garé tant que yégagoul si ay borom
Every day any time hustling and make it try
Find a way change
Struggling and find the Lord
Mou sèèd wala mou tang dieup
Peace lagnouy yoor warko tass all around the world
This démé bord gneup rakhass xol yi diokh ko
Yeurmandé dougue si biir xol yi khool li mégni peace and love
Deug féés déél si xol kholi fénn dééssé best bro
Guiif lo ki méroone fékhé ba ki doone nélaw yéwou
Défaraat ndioum daw deup yéwou
Kou nék fa nga nék lagne lay fék diam la salaam
Bagne tégui yone na takh gnou bagne kheulou deuk si raam
Yobeunté bi la gnou yob si borooooooom
(Tokk wait gno ngui gneuw si ap diir bou gatt)
Dokh diganté bi diokh kou nekk li mou mooooooome
Never say never ooh no!
We Never say never
We Never say never



Writer(s): leuz diwane g


Leuz Diwane G - Diagnosick (The Firstep)
Album Diagnosick (The Firstep)
date of release
10-02-2015




Attention! Feel free to leave feedback.