Marema - Femme d'affaires Lyrics

Lyrics Femme d'affaires - Marema



Souma sanione femme d affaires lay done hmmm
Tok thi banque compter xaliss inthiou xaliss hmm
Souma sanione femme d affaires lay done hmm
Tok thi banque compter xaliss inthiou xaliss hmm
Alelou adouna mom defay dieh mom defay dieh
Femme d affaire lay done kou manqué ma may la
Alelou adoune ya dafa dieh...
Femme d affaire lay done kou manqué ma may la
Alelou adoune ya dafa diieeh diieh
Femme d affaire bras de fer lay deuké
Nguir meune bay sama war
Souma meune diap peu leu ben djiguene



Writer(s): Marema


Marema - Femme d'affaires
Album Femme d'affaires
date of release
24-05-2014




Attention! Feel free to leave feedback.