Obree Daman - Banneex Lyrics

Lyrics Banneex - Obree Daman



Kula faale wul man mii maa lay faale
Doon sa seetu kula xool man lay gisaale
Kula faale wul man mii maa lay faale
Doon sa seetu kula xool man lay gisaale
Ci sa bët laay xool naan la I Love You
Baby yow yaay sama life
Ci sa bët laay xool naan la I Love You
Baby yow yaay sama life
Baby yow yaay sama life
Suma Yàlla bëggee wax len ko na ma baayi ak yow
Ndax ku melni yow
Amatul ci àdduna
Sama xol laa la def
Bëgg dëgg laa la def te duma sooraale
Benn noon
Ndax yaay sama life
Ci sa bët laay xool naan la I Love You
Baby yow yaay sama life
Baby yow yaay sama life
Kula faale wul man mii maa lay faale
Doon sa seetu kula xool man lay gisaale
Kula faale wul man mii maa lay faale
Doon sa seetu kula xool man lay gisaale
Ci sa bët laay xool naan la I Love You
Baby yow yaay sama life
Ci sa bët laay xool naan la I Love You
Baby yow yaay sama life



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Oumar Samb


Obree Daman - Banneex - Single
Album Banneex - Single
date of release
28-01-2022




Attention! Feel free to leave feedback.