Obree Daman - Bideew Lyrics

Lyrics Bideew - Obree Daman



Aha
Yow
Mii
Sa mbëggeel'ay leeral sama yoon
Yow
Mii
Sa mbëggeel'ay leeral sama yoon
Agsil ñu àndandoo
Àndandoo ci asamaan
Sa mbëggeel'ay bideew
[Bideew biy leeral goor Yalla]
Bideew biy leeral sama yoon
Aha
Jigeen a indi leer
Aha
Leeray ci àdduna
Aha
Sa mbëggeel'ay bideew
Aha
[Bideew biy leeral goor Yalla]
Biy leeral sama yoon
Yow
Mii
Sa mbëggeel'ay leeral sama yoon
Yow
Mii
Sa mbëggeel'ay leeral sama yoon
Jigeen'ay leeral
Melni leeray u asamaan
Sen mbëggeel'ay leeral
Jigeen'ay leeral
Ni leeray u asamaan
Sa mbëggeel'ay leeral
Sama yoon
Leer leer leer
Leeray u jigeen buy joge asamaan si Moy leeral goor Yalla yi
Leeray u jigeen buy joge asamaan si Moy leeral goor Yalla yi
Leeray u jigeen buy joge asamaan si Moy leeral goor Yalla yi
Yow
Mii
Sa mbëggeel'ay leeral sama yoon
Yow
Mii
Sa mbëggeel'ay leeral sama yoon
Aha



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Oumar Samb


Obree Daman - Bideew - Single
Album Bideew - Single
date of release
03-12-2021

1 Bideew




Attention! Feel free to leave feedback.