Youssou N'Dour feat. Spotless - Dawal Lyrics

Lyrics Dawal - Youssou N'Dour , Spotless



tu veux sauver ton amour
ni guay samei iow sa mbeugel
daguay moytou gni lay fekheil
dougnou wakh loudoul wakhi Nobel
dila dieimeu diar thie thiofeil
essaie de courir
sans te retourner
daw daw dawal
boul falei
defal ni guinar bou djigueine
bagna khol kou dioguei feneine
iow defal foleine seine
wakhoul tei gua teiye
daw daw dawal
boul falei
assalam malekoum thie neine
mane nagn thie diar wakh leneine
essaie de courir
sans te retourner
daw daw dawal
boul falei
ni guay samei iow
iow sa wakhi Nobel
daguay moytou gni lay fekheil
dila dieimeu diar founei
dila wakh wakhi Nobel
leik leik niou piss leu
dawal dawala daw
tu veu sauver ton amour
mefie toi de ces vautours
boul wouyou boul wouyou dal
wakhoul tei boul doff ba gueirsou leine(2)
dawala dawala.dawala daw
mane nagn fi diarei wakh leneine
dawala dawala dawala daw
fo leine seine wakhoul tei gua teiy
dawal, dawal




Youssou N'Dour feat. Spotless - Africa Rekk
Album Africa Rekk
date of release
04-11-2016



Attention! Feel free to leave feedback.