Admow feat. Maftou - I Wanna Know (feat. Maftou) paroles de chanson

paroles de chanson I Wanna Know (feat. Maftou) - Admow feat. Maftou



Beuss bou nék mane mangui dokh
Mangui guiss wanté meunouma know
Ki ma hate ki ma like ki ma fan ak ma love
Sometime ma melni kou gueum ay nit di sopelikou bamey demeu
Niou gueneu jegué nioley beteu nioley padeu nioley kill di nio ley guédeu
Oooooh waaaaay i wanna know
Li nek si sa khol dakh ma mouytou
Oooooh waaay can you let me know boudé beugoula ndakh ma meuneu move



Writer(s): Adama Diop


Admow feat. Maftou - Revolution
Album Revolution
date de sortie
03-12-2015



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.