Coumba Gawlo - Borom Ndaam paroles de chanson

paroles de chanson Borom Ndaam - Coumba Gawlo



Khadimoul Ahmadina ma déloussiwate,
nanela ya raw ba gnepp diazaka Khadim Rassoul
Khadimoul Ahmadina ma déloussiwate,
nanela ya raw ba gnepp diazaka Khadim Rassoul
Chœurs Sante na Yalla;
Santatina Yalla bimougnou bolé akk Serigne Khadim Rassoul
Sante na Yalla;
Santatina Yalla bimougnou bolé akk Serigne Khadim Rassoul
Ahmadou yay kiffi gueune yaa djiitou gaayi,
Yiffi gueune ba Yalla diokh nala koun;
Djazaka Khadim Rassoul khéweul yii lé;
Ya koffi dial yow mbeur nga Khadim Rassoul,
Nénala dia-dieufeuti yow ndakh lepp ngi
Law, ami-yiiw ami-barké Khaaadim Rassoul
Chœurs (bis)
Serigne Touba
Rayyi ngeunel yii nga yorr;
Motakh konéék-ka nga ngi weur ngeunella
Ba fay-la sa bor, kéne nga Khadim Rassoul
Saw ngagne rote na Khadim sak djitou
Kéne douko mime sa djeuf dji gneup ko yéémm
Chœurs (bis)
Talif bi niou guéne nak suniou serigne,
Serigne Khadim Gaydel Lo mo niou ko diokh niou
Defko adyeu Serigne Touba djeureudjeufé Borom Ndam
Chœurs doylo wolu xam xam bi nek ci yow
Yakar ak beug Borom Ndaam laniou ko def
Nioune doylo wolu xam xam bi nek ci yow
Yakar ak beug Serigne Khadim Lo laniou ko def
Chœurs (bis)
Lo Ndaam
Sa xam xam bi yém naniou, sa diné selleu na,
Ya donnu fouki ndama-k nienti yi yay Borom Ndaam, Gaydel
Chœurs (bis)
Tabakh nga diouma,
Beuneu nga ap téne diangal ndongo yi yarr lene
Kéne dou yalwaani, Touba ba Bakhdad nga goudroné
Chœurs (bis)
Serigne Khadim Ngabou Lo
Serigne Khadim Lo Serigne Moustapha Lo Serigne Modou Lo Issa sa mame
Moo yanou woone wakhadew Chekhoul
Khadim Ndiarem ba Ganar ehhh yay Borom Ndaam
Allé Sénéba, Ndiouga Sénéba, Ndiaye Sénéba,
Mbeurgou Sénéba Gueye, Diafougn Ba moy sene yay Gaydel
Chœurs (bis)
Ndiaye Sénéba sa mam mo djour Arame Lo yayi Farma yayi Fa Wade Wéllé
Mou Mame Seydi Hadj Malick daniou la ziar
Tivaouane ziar la Touba ziar la Bakhdad;
Gaydel Khoudia Coumba, Siré Khoudia Coumba,
Yallo Khadia Daro ak Fallo Khoudia Coumba;
Daniou la nane Borom Ndaam djeureudjeuf;
Ndam ci yay Ndaam ci bay djeureudjeuf;
Sokhna Mam Fama Ndiaye Amineta Sokhna Diodio Lo;
Mbeurgou Sénéba Balla Mbeurgouu ohh;
Wolou xam xam bi ci yow Lo Ndam
Daw Boury Samba,
Salli Lo Anta Kane Mame Mor Anta Sally Mbacké Serigne Touba;
Ndam Diounop Ndaam Sanoussi Serigne Siga Lo sa mame djeureudjeuf
Docteuru islam ba ngi;
Fadj nga doff yii,
Guis lo goumba yi, waxlo louu yii, doxlo lafagn yi;
Djeureudjeuf



Writer(s): Coumba Gawlo


Coumba Gawlo - Terrou Waar
Album Terrou Waar
date de sortie
07-12-2018




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.