Iss 814 - Mbeuguélou Idoles (TV Series ''Idoles'' Soundtrack) paroles de chanson

paroles de chanson Mbeuguélou Idoles (TV Series ''Idoles'' Soundtrack) - Iss 814



Beut guissatoul lamingne waxatoul
Hahan sentiment
Sokhna si djéguema waxma liné si iow
Xalé bi yama dieulei makk deloma xalei
Mbeuguel dou thi iow dou thi mane yalla la
Mbeuguel ki dou iow ki dou mane yalla (×2)
Luy sa couleur fanenga deuk say beut rafetna lolu wowo
Thi xolbi dou iow yaffi ndieuk mais sa place mingsi thiol wowo
Sokhnasi demna beu nitt ngi dagnmay clash ndax nima mel si iow
Demna ba gars yi dagnmay xass niéneine ngi dima dieuw
Mbeuguel dou thi iow dou thi mane yalla
Mbeuguel ki dou iow ki dou mane yalla (×2)
Demala guiss beugleu phénomène leu
Mbeguel deugleu teu dou feine nakk
Sokhnasi bodei diel meu teud peine
Poésie sama
Pinceau Picasso
Vrai couleur no l'asso
Poésie peinture sokhnasi mbeuguel bou amoul mesure
Amoul keine kou melni iow parck iow mi iow mi iowd ara dokko thiow
Bayile non yi dieuw xadji neign nu
Mbeuw caravane bi nieuw nitt ngi gueneu blow
Bayilen nu thiow mbeuguelou idolela beug nu diokhlen niom nieup nu
Khol aythia waxlen sokhnasi makk iow
Funu neikh yokhla ow ow mbeuguelou deugleu



Writer(s): Ismaila Talla


Iss 814 - Freestyle Pack I - EP
Album Freestyle Pack I - EP
date de sortie
06-09-2018




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.