Marema - My Friend paroles de chanson

paroles de chanson My Friend - Marema



Lima yakaroone ni yaaw la
Dou done keneene yeeeah
Limaa foogooone ni yoow leuu dou doone keneene yeeeah
Nii beuuss bou nekeuu meuu degueuu yafii waakh tes daraa doukoo dinddii nakhteee dougoulaaa
Ndekee xarit dinaa leuu yenee lou gnaaaw
You are my friend
I will never let you down
You are my friend yeaah yeaah
L will never let you down
Aandaandoo deugueeu



Writer(s): Marema


Marema - Initié
Album Initié
date de sortie
01-06-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.