Omzo Dollar - Ndakh Rap paroles de chanson

paroles de chanson Ndakh Rap - Omzo Dollar



Yeah!
2006 ba 2016 nigger (nigger)!
Young Fif
I say
Warone nga féké bimay dokh ak samay ngandi casque
Dokh di bondé melni mandikate
Gars yi fook ni boy bi da am handicap
Jean huilé ak chemise hawaïenne
Tout est neuf melni j'ai pas la moyenne
Nigger dou sakh man ak yeen
Fadiar ba guiss lune mangui ci mbed bi di
Binde texte ba amatouma encre sama bic plume
Man ak Alsseyni took di veiller sayou goudi jott
Yagua freestyle terrasse bi ci kaw ba heurou diouli jott
Produire ay dêchet fils
Di deff ay son ak FL6
Micro two taw (thousand) sama PC fixe
Amone na talent fook ma teela am buzz
Jamono studio duplex 01 heure 8000 Eli ak Bugs
Mangui lay nétali ay beuss yo xamni fallait deff ay délit ay teuss
Mère nangalou ma meunou ma fegn télé ak feuss
Maxouli ay beut c textuel kepp momay
Gestuel massalé pour mou bagna sipp ma tekk xel
Ndax fima jaar daniouma yagua teuthie ndax rap
Yague naniouma képp dima mbéthie ndax rap
Daniouma yagua guéné keur gui nigger lepp ndax rap
Kon soma joxé mic tay mom lepp lay wax
Nieuweul déglou fima jaar lima yeukk ndax rap
Meunoma jaay graw boulma leepp say wax
Ndaxté xamo fima jaar lima yeukk ndax rap
Yeah boulma leepp say wax my nigger!
Man ak Boy creer groupe bou toude Capsibloc Hustler Power, José-T,
Omzo ak ZigZag faté wouma Fresh-T, Kheushy-T my nigger Nazz ak Bass
Repetition yi négou Abba mèram sakh di caass
Daniou yague di beuré ak radio yi yague di weeré
Amoul wone xaliss pour deff clip ba son yi dialeu ci télé
Kon fatalil querelle yi jabanté feulé yi abanté yeuré yi
Probleme sou amé niou raakk ba saga ndy ennemi
Deff yeufou hustler
Concert kou am probleme ba tekk beut niou wax la
Tekk seuss niou nokh la heyy
Premier concert niou huéé niou
Deuxieme niou rayy tout le monde
Jubilé coulisse yi ni équipe bou gagné coupe du monde
Bring sa appetit
Man ak José thiolé pass ma dessé
Five niou jeundé ko ay neme ak spaghetti
Mais tay ma ndiabati dokh HLM ba Mamelle
Lolou yeupp piur dougal ben son rap meunouma fay limouma amel
My nigger doumala fenn defone na fi lepp ndax rap
Yague na di jooy yague bégue ndax rap
Dama yagua mougn yagua nopi lepp ndax rap
Kon soma joxé mic tay mom lepp lay wax
Nieuweul déglou fima jaar lima yeukk ndax rap
Meunoma jaay graw boulma leepp say wax
Sou féké xamo fima jaar lima yeukk ndax rap
Yeah boulma leepp say wax my nigger




Omzo Dollar - Dëgeuntane
Album Dëgeuntane
date de sortie
16-09-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.