Philip M. feat. Corine - Yaw Rek Lev paroles de chanson

paroles de chanson Yaw Rek Lev - Philip M. feat. Corine



Ibil nal sama khol,
Yalla na nga si guiss lou lére
gueuneu kham ni
Amoul kénène koudoul yaw.
Mbeugél gui nékeu si mane
A ngii di ma dane
gueum na di na done
Sa néné bi ngéy tété.
Mane mi souma mounone,
Dina bokake yow bénéne yone,
Dila wowé néné touti,
Ndakh mane mi,
Mane mi gnanou ma yalla,
Gnanou ma yalla
Déss fii mane réka
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law,
Ibil nala sama khol
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow,
Mbeuguél gui mo ngi ni di law,
dina done sa néné.
Am na gnou wakh
Mbeugél tiono rék la,
Wayé ma ngi léy khamal
Dou kéne yow réke leu.
Beuss bou me le guissé
Ta kham ni khol déy guissé
fok na ni do meusse tass sama yakar!
Boul am loy ragal di la khar,
Doumeu meusseu diay sama taar,
Dinala wowé papa chéri,
Dina done sa sokhna,
Di na done sa baby,
Mi léy fadial
Say sokhla, oh baby yow réke le
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law,
Ibil nala sama khol
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow,
Mbeuguél gui mo ngi ni di law,
dina done sa néné.
Yay sama doolé
Soudoul yow wate na dou done kékéne,
Diokh na la sama bope,
dina la dégueul di le bégueul,
Baby boul sone,
Gueumeul ni yow réke le!
Dou kékéne...



Writer(s): Corine, Jc Lalyre, Philipe Bergeron Monteiro


Philip M. feat. Corine - Philip Monteiro
Album Philip Monteiro
date de sortie
28-05-2014



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.