Titi - Maman je t'aime paroles de chanson

paroles de chanson Maman je t'aime - Titi



Yaya boye
Yaye Sama adouna
Sama baya boye
Sama barke
Bour yalla dieguema
Bilaye yaye boy
Yay Sama adouna
Sama baya boy Sama barke
Kon yalla dieguema
Yaye boy yay Sama adouna
Sama baya boy Sama barke
Bour yalla dieguema
Baye day nianal dom
Mba Lou mou dougou mou and ak barke sol ko diom ak Gora mba dom bess
Bo mague bilaye sol sa dalou Baye goro Gor yak sa Baye thiono adouna
Yak sa Baye moi Def si yaw dîne ak sole
Ler Ba boute Bou feugue mou and ak barke
Maman je t'aime beaucoup
Je ne pourrai jamais te paye maman toi qui ma donné la vie
Weurseuk Bi si dom agni deye la
Demb mag nie daniou dan wakhnan weurseuk gui si
Dom Ndeye la moy gualadiou dom diou dieguene die
Bour yalla dieguema
Kon yalla dieguema
Yaye bou sa dôme Dji magu teki mom la nie Niane yalla 2
Faye birame penda wagane
Dougou dougou wagane wagane koumba sadia
Ah aaaahhh rowoukay gua
Seni sa Baye seni Maissa faye yay bayam nafissatou moy sa
Yaye naffisatou thioro Diagne niay yayam yaya boy royoukaye gua
Boudé Niane diokhal sa deye ak sa Baye boudé Maye diokhal sa yaye
Bour yalla dieguema
Bour yalla dieguema
Yalla na gay may Sama yaye
Bour yalla dieguema
Mou mena dem siare Dji baytilay
Bour yalla dieguema
Yene Dji romb na
Bour yalla dieguema
Bour yalla dieguema
Yaye sa ma yaye ye
Bour yalla dieguema



Writer(s): ndéye fatou tine


Titi - Amul nu malene beguewoul
Album Amul nu malene beguewoul
date de sortie
04-11-2013




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.