Titi - Nobal Ku Lë Nob paroles de chanson

paroles de chanson Nobal Ku Lë Nob - Titi



Wouy mbeuguel loo, anh mbeuguel
Wouy mbeuguel loo, anh mbeuguel
Bala ngay nobati iao, nang ko xol
Bala ngay beugati iao, nang ko set
Ndax so beugueii, so beugueii, nguru ngaa
Bala ngay nobati iao, nang ko xol
Bala ngay beugati iao, nank ko set
Ndax so beugueii, so beugueii, nguru ngaa
Dangay set gninga bayi ba am ci ay noone;
Mane ma xol gnima bayi na am ci ay noone
Nonu nga donei sama matadi
Ba sumala jissul: baby damay manquer
Inquiéter wu sumala seinei ak kenen (fok nga sip),
Wayei manit na dal ndax numa dieufei wathié sama personnalité
Lumeu meuneu don yafi nei
Bala ngay nobati iao, nang ko xol
Bala ngay beugati iao, nang ko set
Ndax so beugueii, so beugueii:nguru ngaa
Bala ngay beugatei
Nob kuleu nob: dara dakuko
Beugal kuleu beug: dara dakuko
Nobal kuleu nob: dara dakuko
Beugal kuleu beug: dara dakuko
Dara dakuko, dara dakuko
Nobal kuleu nob: dara dakuko
Dara dakuko,dara dakuko
Beugal kuleu beug dara dakuko
Enh beuglen
Xana du mbeuguel leuu
Mane nena sumako pognet du dem
Mane malay décoder ndax danga coder
Hôpital buma diar niu xalil ma yon
Ndax médicaments yalay fathie, mane malen kay diox: ma gueun ci iao
Guedj gui sax dafma xamei
Vagues yi don samay xarit
Nguelaw li, pithe yi naw ehh
May sen natagoo
WhatsApp bi nga saalo
Ba xolatoma dima zappé
Viber bi nila won
Ba sumalay by by
Doma xol man
Ennnnnh wouy mbeuguel looo
Nobal kuleu nob: dara dakuko
Beugal kuleu beug: dara dakuko
Nobal kuleu nob: dara dakuko
Beugal kuleu beug: dara dakuko
Dara dakuko; dara dakuko
Nobal kuleu nob: dara dakuko; dara dakuko
End.



Writer(s): Prince Ibrahima Ndour, Titi La Lionne


Titi - Ay Nammante Lë
Album Ay Nammante Lë
date de sortie
03-06-2019




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.