Viviane Chidid feat. Barack Adama - Zoné paroles de chanson

paroles de chanson Zoné - Viviane Chidid , Barack Adama



Soo xamon nima soon néé
Sou keur doon école awma tchii classe sii mbéde biih
Laay diangué baa sama xël nieuwna sokhla woule dasse
Bamay neek gouné MBOUR TOUCOULEUR baa
GRAND DAKAR FASS maneuh dem nassi founé
La tête dans les nuages et les pieds sur le futur
Lou louné laa guiss banekh ak diss
Lou louneii laa guiss téré woul vivi diap teuh bayii
Fima diaar baa yeksii fii yomboul wayeii diomboul domou adama
Je n′aime pas le jour je ne vie que la night
Soo khamone nima sooné sou keur doone école awma tchii classe
Sii mbéde bii laay diangué baa sama xël
Nieuwna sokhlawoul dass bamay nek gouné
MBOUR TOUCOULEUR baah GRAND DAKAR FASS mane dem nassii founé
La tête dans les nuages et les pieds sur le futur
Barack adama
WoOh wooh wooh wooh wooh
Yaye booy a taffée sans arrêt du lundi au lundi
Wooh wooh wooh wooh wooh
Et le daron a fait pareil sans profiter de la vie
Je veux conquérir le monde dans la mif' on est nombreux??
Wouwou j′ai zoné dans les rues maintenant me voilà
Anhan j'ai zoné dans les rues maintenant me voilà yaye booy
Mane sama life fila music bii dieul deinthieu
gooré naah baa tidjil maa ay bountou
Kouh niak dieurignou mane douma reuthiou
Kounék sii kanam doto talla gestú
Bégueul doumou Adama
Indina Viviane ak Barack Adama
Amoul frontière



Writer(s): Karl Adjibade, Adama Mickael Diallo, Stephane Dogoum, Mourtada Coulibaly, Gedeon Mundele Ngolo Nzinga Nzala


Viviane Chidid feat. Barack Adama - Zoné
Album Zoné
date de sortie
09-01-2018



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.