Youssou N'Dour feat. Toumani Diabaté - Mbeugël is All paroles de chanson

paroles de chanson Mbeugël is All - Toumani Diabaté , Youssou N'Dour



Mbeuguel la woor Mbeuguel is all
Na woora woor Souleu beugué na woor Salimata
néwone ngama beugouloma Diégué ma, diégué ma Chérie boy
Kay ngeu diégué ma
Foy moudié, foy moudié
Foy moudié ak mome Doula door
doula réy,
kone kouné langal ak sa waay
Salimata néwone ngama beugouloma Diégué ma, diégué ma Chérie boy
Kay ngeu diégué ma
Chérie coco diokhnala sama khol
Boolé tia dila yeureum
yitt dila mougneul Li souleu doyoulé Dafa dane solou khél
Diko téyé tchi yaramam
Sou goudi meussana diott
Si souf sou sédd si
Aminta Ndiaye néwone nala djiguéne douma fonto
Togne ngama béne yone
Ma wakh ko sa yaye Ngadel délou tognati
Foy moudié Foy moudié, foy moudié ak mome Doula door doula réy,
kone kouné langal ak sa waay
Mbeuguel la woor Mbeuguel is all
Na woora woor Souleu beugué na woor
Mbeuguel la woor Mbeuguel is all
Na woora woor Souleu beugué na woor
Djiguéne yéy souniou lumière
Wayé nioy sène courant
Sou khol yi leundeumé
Souniou mbeuguel-akoy léral
Ahh Djiguéne yéy souniou lumière
Wayé nioy sène courant
Sou khol yi leundeumé
Souniou mbeuguel-akoy léral
Weuy lène Weuy lèèèèèène mbeuguel
Djiguéne yéy souniou lumière
Wayé nioy sène courant
Sou khol yi leundeumé
Souniou mbeuguel-akoy léral Ay tiono la Boulko wéddi ay tiono la
Miss yi nio tarou
Ma wakh ko béne yone
Yacine bobou diambar la wone
Wouy fénène Wouy fénène
Wouy fénène Wouy fénène
Wouy fénène Wouy fénène
Souma wakhtané Souma wakhtané Ak sama ngénguénay téyél lako
Mangui khol sa banéékh
Mangui khol ningay doundééé
Mangui khol sa banéékh
Mangui khol ningay doundééé
Souma wakhtané Souma wakhtané Ak sama ngénguénay téyél lako
Salimata néwone ngama beugouloma Diégué ma, diégué ma Chérie boy
Kay ngeu diégué ma
Foy moudié, foy moudié Foy moudiéak mome
Doula door doula réy,
kone kouné langal ak sa waay
Mneuguel is all
Na woora woor Souleu beugué na woor
Mneuguel no woor, Mneuguel is all
Na woora woor Souleu beugué na woor
Aminta Ndiaye néwone nala djiguéne douma fonto
Togne ngama béne yone
Ma wakh ko sa yaye Ngadel délou tognati
Mangui khol sa banéékh
Mangui khol ningay doundééé
Mangui khol sa banéékh
Mangui khol ningay doundééé
Djiguéne yéy souniou lumière
Wayé nioy sène courant
Sou khol yi leundeumé
Souniou mbeuguel-akoy léral
Ahh Djiguéne yéy souniou lumière
Wayé nioy sène courant
Sou khol yi leundeumé
Souniou mbeuguel-akoy léral
Weuy lène Weuy lèèèèèène mbeuguel
Aminta Ndiaye néwone nala djiguéne douma fonto
Togne ngama béne yone
Ma wakh ko sa yaye Ngadel délou tognati
Foy moudié, foy moudié
Foy moudié ak mome Doula door
doula réy,
kone kouné langal ak sa waay
Weuy lène Weuy lèèèèèène mbeuguel
Na woora woor Souleu beugué na woor
Mbeuguel la woor Mbeuguel is all Na woora woor Souleu beugué na woor




Youssou N'Dour feat. Toumani Diabaté - Seeni Valeurs
Album Seeni Valeurs
date de sortie
01-08-2017



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.