Etoile De Dakar feat. Youssou N'Dour - Dounya paroles de chanson

paroles de chanson Dounya - Youssou N'Dour , Étoile de Dakar



Unya dunya
Dunya dunya
Dunya dunya dunya mome dafay diekh
Dunya dunya, lifi nekk djadouwoul eupp neu
Dunya dunya, lifi nekk djadou touti
Dunya dunya lifi nekk djadouwoul eupp neu
balma, lor ngama, lor ngama
Wouye yeureum ma
Aduna bi djar na kholate
Ana borom kham kham yi, borom kom-kom
Aduna bi djar na kholate, mandou djokko am yakaar
Ni aduna bi nanou djoug daal
Nanou djoko bagna sétane
Thi ni wala thi né, li ame solo my djeuf dafay meute(bis)
Ana gni soriyanté, ani gni dokkolanté(djeuf dafay meute)
Thi ni wala thi li ame solo moy djeuf dafay meute
Djoko djoko nanou djoko
Djoko kay gnou djoko
Djoko, djoko, djoko bagna sétane
Dunya bi djar na kholate
Nagne thi teey
Nagne thi mandou ame thi yakaar
Djoko, djoko, djoko bagna sétane
Sétal ma li
Li thi mbotaay yi di bagne
nite ki louko takha djog war na thié dem ba diekh
Djoko, djoko, djoko gnou bolo
Sétal ma li
Oui, c'est le mouvement qui dit non
Qui dit non, non...
C'est le mouvement qui dit




Etoile De Dakar feat. Youssou N'Dour - Senegal Super Star
Album Senegal Super Star
date de sortie
01-01-2013



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.