Songtexte Taaw - Dip Doundou Guiss
                                                Karabalik 
                                                on 
                                                the 
                                                track
 
                                    
                                
                                                Gilomas
 
                                    
                                
                                                Juddu 
                                                doon 
                                                Taaw
 
                                    
                                
                                                Dëk 
                                                dëkku 
                                                Bukki 
                                                njombor
 
                                    
                                
                                                Xam 
                                                na 
                                                du 
                                                ñep 
                                                mëna 
                                                doon 
                                                gor
 
                                    
                                
                                                Du 
                                                ñeppa 
                                                believe 
                                                on 
                                                God
 
                                    
                                
                                                Man 
                                                gëmu 
                                                ma 
                                                kenn 
                                                kudul 
                                                sama 
                                                bopp
 
                                    
                                
                                                Te 
                                                amu 
                                                ma 
                                                yoonu 
                                                rethiou 
                                                comme 
                                                gun
 
                                    
                                
                                                Aller 
                                                sans 
                                                retour 
                                                comme 
                                                jaam
 
                                    
                                
                                                Man 
                                                Yallah 
                                                rekka 
                                                xam 
                                                lutax 
                                                ma 
                                                juddu 
                                                doon 
                                                taaw
 
                                    
                                
                                                Bayil 
                                                ma 
                                                sukku 
                                                ñaan 
                                                ko 
                                                mu 
                                                deff 
                                                wiss 
                                                bi 
                                                doon 
                                                taw
 
                                    
                                
                                                Duma 
                                                Ndiago 
                                                buy 
                                                foote
 
                                    
                                
                                                Duma 
                                                buy 
                                                tukki 
                                                toog 
                                                kaaw
 
                                    
                                
                                                Duma 
                                                sa 
                                                gars 
                                                yi 
                                                talul 
                                                ludul 
                                                mukki 
                                                boone 
                                                tak
 
                                    
                                
                                                Mussu 
                                                ma 
                                                am 
                                                flop
 
                                    
                                
                                                Log 
                                                dangar 
                                                bu 
                                                ñor 
                                                xomm
 
                                    
                                
                                                Diko 
                                                tufli 
                                                seen 
                                                kaw
 
                                    
                                
                                                Mafi 
                                                né 
                                                té 
                                                ñoma 
                                                ëpo 
                                                jotu 
                                                rap 
                                                fop
 
                                    
                                
                                                Budul 
                                                mbiru 
                                                koppar
 
                                    
                                
                                                Bul 
                                                jël 
                                                suñu 
                                                contact
 
                                    
                                
                                                Nigger 
                                                shut 
                                                your 
                                                fuck 
                                                up
 
                                    
                                
                                                Gëdj 
                                                na 
                                                jooy 
                                                depuis 
                                                sama 
                                                dëju 
                                                mame
 
                                    
                                
                                                Duma 
                                                mëssa 
                                                def 
                                                litax 
                                                ba 
                                                ñimay 
                                                nëbbë 
                                                naadj
 
                                    
                                
                                                Tuuma 
                                                yepp 
                                                ma 
                                                tëx, 
                                                lu, 
                                                muuma 
                                                woolu 
                                                dëgg 
                                                fight
 
                                    
                                
                                                Dugal 
                                                rekk'ay 
                                                tax 
                                                ma 
                                                football 
                                                jox 
                                                ma 
                                                number 
                                                nine
 
                                    
                                
                                                Ñaane 
                                                pour 
                                                samay 
                                                noone
 
                                    
                                
                                                Ñaane 
                                                pour 
                                                samay 
                                                niggers
 
                                    
                                
                                                Genné 
                                                ci 
                                                samay 
                                                gars
 
                                    
                                
                                                Dé 
                                                pour 
                                                samay 
                                                niggers
 
                                    
                                
                                                Ëppu 
                                                mala 
                                                impact
 
                                    
                                
                                                Yakoy 
                                                woné 
                                                ñu 
                                                giss
 
                                    
                                
                                                Ñàq 
                                                jotu 
                                                ñàqqa 
                                                tax 
                                                ma 
                                                juddu 
                                                doon 
                                                taaw
 
                                    
                                
                                                (Ñaane 
                                                pour 
                                                samay 
                                                noone) 
                                                Ñaane 
                                                pour 
                                                samay 
                                                noone
 
                                    
                                
                                                (Genné 
                                                ci 
                                                samay 
                                                gars), 
                                                Genné 
                                                ci 
                                                samay 
                                                gars
 
                                    
                                
                                                (Ëppu 
                                                mala 
                                                impact) 
                                                haahaaahaaa
 
                                    
                                
                                                Dooré 
                                                di 
                                                encaisser 
                                                coups 
                                                ni 
                                                dundu 
                                                soldat
 
                                    
                                
                                                Xaaruma 
                                                sol 
                                                dallam 
                                                pour 
                                                jok 
                                                wutu 
                                                sama 
                                                papa
 
                                    
                                
                                                Xammel 
                                                kila 
                                                bëg 
                                                ak 
                                                kiy 
                                                wute 
                                                pourcentage
 
                                    
                                
                                                Fenn 
                                                bu 
                                                gëna 
                                                rëy 
                                                mooy 
                                                ku 
                                                ame 
                                                kuddu 
                                                do 
                                                laqq
 
                                    
                                
                                                Mame 
                                                Yallah 
                                                rekka 
                                                xam 
                                                lutax 
                                                ma 
                                                njëkka 
                                                juddu
 
                                    
                                
                                                Kuné 
                                                amna 
                                                lo 
                                                wara 
                                                muñe 
                                                lo 
                                                wara 
                                                xeex
 
                                    
                                
                                                Logique 
                                                ni 
                                                jours 
                                                yi 
                                                nga 
                                                wara 
                                                dundu, 
                                                yo 
                                                wara 
                                                dé
 
                                    
                                
                                                Yaye 
                                                limu 
                                                dadj 
                                                rek 
                                                doyna 
                                                fexeel 
                                                ba 
                                                thionom 
                                                jeex
 
                                    
                                
                                                Ku 
                                                def 
                                                sa 
                                                bopp 
                                                ennemi 
                                                do 
                                                tall 
                                                noono 
                                                ak 
                                                kenn
 
                                    
                                
                                                Fi 
                                                ngay 
                                                ñàqq 
                                                deefa 
                                                roote
 
                                    
                                
                                                Fi 
                                                sa 
                                                aduna 
                                                yaqqo 
                                                mëna 
                                                tufa 
                                                defaro
 
                                    
                                
                                                Def 
                                                lula 
                                                nit 
                                                di 
                                                xeebé, 
                                                mënul 
                                                wessu 
                                                xeeb 
                                                sa 
                                                bopp
 
                                    
                                
                                                Budul 
                                                say 
                                                ñaanu 
                                                waajur 
                                                bane 
                                                terré 
                                                ngay 
                                                gettaro 
                                                (terré 
                                                ngay 
                                                gettaro)
 
                                    
                                
                                                Bindël 
                                                sa 
                                                suba 
                                                tay, 
                                                rakkdestin 
                                                dou 
                                                chance 
                                                deh
 
                                    
                                
                                                Du 
                                                yoon 
                                                pabi 
                                                dem 
                                                ba 
                                                maguette 
                                                di 
                                                fay 
                                                louasse 
                                                rek
 
                                    
                                
                                                Am-am 
                                                ju 
                                                lew
 
                                    
                                
                                                Fi 
                                                ñun 
                                                ñeppa 
                                                seex 
                                                lu 
                                                saleté
 
                                    
                                
                                                Pour 
                                                feey 
                                                si 
                                                banneex 
                                                duma 
                                                yootu 
                                                geedj 
                                                di 
                                                am 
                                                dex
 
                                    
                                
                                                Fi 
                                                jengu 
                                                ba 
                                                deh
 
                                    
                                
                                                Ragal 
                                                réthiou 
                                                ak 
                                                gathié
 
                                    
                                
                                                Duñu 
                                                tass 
                                                yaakaru 
                                                mère 
                                                bi 
                                                muk 
                                                ni 
                                                sëy 
                                                bu 
                                                tass 
                                                tey
 
                                    
                                
                                                Samay 
                                                principes 
                                                ak 
                                                sama 
                                                ngor 
                                                rekk'ay 
                                                fess 
                                                sama 
                                                compte
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                dignité 
                                                sama 
                                                xola 
                                                may 
                                                fek 
                                                sama 
                                                morgue
 
                                    
                                
                                                Duma 
                                                ñé 
                                                sama 
                                                morom 
                                                ba 
                                                toog 
                                                di 
                                                fenn 
                                                sama 
                                                bop
 
                                    
                                
                                                Duma 
                                                fenn 
                                                sama 
                                                bop 
                                                ni 
                                                jeek 
                                                bu 
                                                xeessal 
                                                ba 
                                                xonk
 
                                    
                                
                                                Life 
                                                lu 
                                                nek 
                                                ak 
                                                temps 
                                                wam 
                                                da 
                                                ngay 
                                                xëy 
                                                sooga 
                                                gontu
 
                                    
                                
                                                Life 
                                                lou 
                                                nek 
                                                ak 
                                                temps 
                                                wam 
                                                entre 
                                                xel 
                                                wala 
                                                xol
 
                                    
                                
                                                Jeex 
                                                na 
                                                ba 
                                                noppi 
                                                kuko 
                                                yénu 
                                                rek 
                                                sa 
                                                xella 
                                                fa 
                                                tollu
 
                                    
                                
                                                Xeex 
                                                nga 
                                                ba 
                                                sonnu 
                                                Ma 
                                                pour 
                                                ame 
                                                lo 
                                                dundëlé 
                                                sa 
                                                njaboot
 
                                    
                                
                                                Tay 
                                                nak 
                                                sa 
                                                doom 
                                                yi 
                                                magg 
                                                nañ, 
                                                juk 
                                                tekki 
                                                teral 
                                                la 
                                                jotna
 
                                    
                                
                                                Life 
                                                lu 
                                                waay 
                                                def 
                                                boppam, 
                                                kenn 
                                                du 
                                                fay 
                                                sama 
                                                borr
 
                                    
                                
                                                Fole 
                                                mimi 
                                                fole 
                                                mimi 
                                                fo 
                                                oh 
                                                oh
 
                                    
                                
                                                Fole 
                                                mimi 
                                                fole 
                                                mimi 
                                                fo 
                                                oh 
                                                oh
 
                                    
                                
                                                Fole 
                                                mimi 
                                                fole 
                                                mimi 
                                                fo 
                                                oh 
                                                oh
 
                                    
                                
                                                Fole 
                                                mimi 
                                                fo 
                                                oh 
                                                oh 
                                                oh
 
                                    
                                
                                                Fole 
                                                mimi 
                                                fole 
                                                mimi 
                                                fo 
                                                oh 
                                                oh
 
                                    
                                
                                                Fole 
                                                mimi 
                                                fole 
                                                mimi 
                                                fo 
                                                oh 
                                                oh
 
                                    
                                
                                                Fole 
                                                mimi 
                                                fole 
                                                mimi 
                                                fo 
                                                oh 
                                                oh
 
                                    
                                
                                                Fole 
                                                mimi 
                                                fo 
                                                oh 
                                                oh 
                                                oh
 
                                    
                                 
                            Attention! Feel free to leave feedback.
                 
                                                         
                                                         
                                                         
                                                         
                                                         
                                                         
                                                         
                                                        