Iss 814 - Miim Reew Songtexte

Songtexte Miim Reew - Iss 814




Police dou décroché
Sapeur Daye yékha gneuw
Nénagnou dou raccroché
fepp la meneu gneuw
Amna gnou roussoul
Dieuw neew sa biir corbillard
Amna gnouy dingate sen Serigne
deugno gneuw ziaar
Djiko youdoul dégne
Nii fébaar youdoul weer
Politique égale politique
Même bou néké sen keur



Autor(en): Ismaila Talla



Attention! Feel free to leave feedback.