Nitdoff - Doff Ego 6 Songtexte

Songtexte Doff Ego 6 - Nitdoff




Yeah
Han
Boulma seussou ni bouki xamna ni mokalo diouki
Killah dey fadd di souki ki ngen ko fogué woon dou ki
Djiekou mic jokh la rhyme flow tchi sassi ngey touki
Niata bitch la fouti tchi mic sopi len kouti
Killah amna 9 milli amna paka buy bouti
Mic check doumana ay djieg niou dagaleen diouti
Rap bou gooré rap bou hardcoré fuck rabou woubi
Thiouba guñu sunu flag nga ñuy gis si ay lobbie
Kuma messa beugg golo rek saga na ndeim
Duma marr tattu kenn nigga saba la man
Xamna li waur moy delou tub si sa borom man
Mo gueun wekk ko si todj nénn ak safara néen
Sén rappeur ya ngi leumboul dioutou est-ce que da djiek
Takkal sa génio nga gooré nigga parce que do djéeg
Désna tuti bongo man yi dotouniu lékati money, ndax lepp fucked up
Mc ya ngi jalgati yoon wi
Mbotou rap bi laniu péek taggat si sunu head
Tataan tchi kuñuy dekk nope xeexal si sunu xeet
Dañeko tarbiya si teel teewal ba dugg jail
Money bi musta doon blem yegul si sunu khole
Dañ ko jayanté for real my nigga nio ngi chill
Tay doxuñu di seugg niogui siggi sunu ville
Yaw bo oubi won sa gatt xeuyna Macky dou kill
Daguako lemm bamu rond motakhit jotna nga sa meal
Da nga nooy bopp buzz bi gua top ba tooy dog
Nigga foy toog, chaisou buur wala tchi koye toog
Séni boycote taxul ma sopi bi drees code
I go pray God nigga ñun soxla wuñ kiley taatt
Vilipendé ngen rap bi bam sapi tchi tik tok
Gorou tchip tchip guew bi ngen bok du hip hop
Na ngen khiddi mic tiogalou tchiaz yiniuy iri night
Mbed style yu high, diaralon nako sakh firi knife
Leggi gay rap tchi net bi lay taxaw nane get up
Nañ ko guewaat tchi mbed ngey xamé guy guerrat
Mister kk saga la sekk ak sen mille jagg yi
Play the limthiako yi fake yi la yane sakou yi
I'm the hardest one ki ngen andi fitt bi da reusson
Keep you dollar some
Give me the respect non pas de somme
Black palladium fuck your skinny jean and colors son
Hip hop lañu wodeu goor yuy takk bin bin
New king, respect the gunzout we the real thing
Djiek djiekal sama toogay feuk mic bi wo gars yi
Mane la ugly boy biy doxaan ndey seni beau gars yi
Daradja dou djiexital si makhama Mc
Kunek ak laleu takha jugg
Dandoulen ma dandoulen mane fake yéma xamagul
Istikhfaar ya Latif bi dioli doma guiss tchi baar
Indicatif keep it bi ngey djiteul pour nga jot tchi mane
Nourou na tchi xautaay ba diott si mbautu sirou yi
Gayndé guy faddé bulen ko bolek sen sirou yi
Salaw dou fanaw, them niggaz dead mofucker if i'm out
Préau du très haut, j'ai prié pour mes frérots
Mon esprit en jouissance, j'ai planifié le créneau
J'suis obsédé par ce procédé frérot j'ai trop cédé
Faire du sale avec la bénédiction que je possédais
J'ai accédé à la lumière divine de mes capacités
Léger comme ma plume, j'suis pas un gars flambeur
Mon message est clair, essaie de lire la profondeur
Vie ma vie avec mes hauts, mes bas, l'alpha, l'omega
J'ne suis plus dans le forcing pour faire du lourd mes gars
Je fais gaffe aux dégâts j'esquive les faux débats
La nature est mature elle m'inculque l'au-delà
Vaine est leur tentative, j'suis combatif
Si je dois changer pour vous plaire, je compte pas vivre
Nigga bul bakati bandit teur na paka putt ba ngi
Amna ay réndikat Gambie, am niumey écoulel came bi
Flow bou thiéné ni danguinn, rime yi ni omlettou tanguish
I'm the under and over fo xalat pundel nañe foofa
Y'all niggaz kébétou bullshit
But faniuy guéwé yaw doofa tekk sa tank
Bo key djiem mey decapité ndeim
Beureup ba beureup danieko miner aksil diogui tchi ndel
Guis nga succès biy shine mey xeuy di reudati rhyme
Sumey punch every line dey melni Tyson in prime
Don't make me grab my nine i go blow your mind
ND mother fuckin killah moy sa abatchine
Ñewel souk cirer shoes banopi djam ma tchine
I'm a ready king gun leen legitime
Da ngen doon niodi tegui ndawal, mane ma tégui tchinn
Deudou mic wooté gatsa gatsa in everything
Doff ego 6 la gars yiy faadio mbété medecine
I'm a ready king gun leen legitime
Da ngen doon niodi tegui ndawal, mane ma tégui tchinn
Deudou mic wooté gatsa gatsa in everything
Doff ego 6 la gars yiy faadio mbété medecine



Autor(en): Bazik Prod, Mor Talla Gueye, Nitdoff


Nitdoff - Doff Ego 6
Album Doff Ego 6
Veröffentlichungsdatum
11-12-2024




Attention! Feel free to leave feedback.