Songtexte Dérangé - Wally B. Seck
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Soma
dégué
Soma
wooloo
Na
ñou
andado
Gala
wayy
bouñou
déranger
Kaddu
gui
laleine
di
déngkeu
Bouñou
déranger
bouñou
déranger
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Dakar
ba
Thiès
Kaolack
Tamba
ba
Diourbel
Fatick
Saint-Louis
Na
ñou
ande
cii
yar
ak
yiiw
Ñeuwléne
ñou
sett
Souñou
rew
mi
likoy
naatal
moy
ndaw
you
guëstu
Ngala
wayy
baña
déranger
Souñou
rew
mi
ñoko
bokk
Bouñou
déranger
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Non
non
non
non
Ñeuwléne
limey
sène
Souñou
andé
nekk
ben
leppay
easy
Louñou
yootou
meune
cii
diote
Negn
léne
yiiw
Teyy
Baña
khiiroo
souñou
biir
Neñ
leine
dorr
warr
Ngala
wayy
bouñou
déranger
Souñou
rew
mii
ñoko
bokk
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Boul
Déranger
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Kone
yow
sama
soppé
Boul
dii
khoulotii
ndakh
man
Liimeu
beug
Liimeu
beñ
lay
bolei
daane
Sama
khol
dou
diiouk
cii
yeine
Bii
ñou
andé
beu
legui
Ñii
ngui
gueune
dii
diéguii
Diégui
frontière
yééé
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Na
ngueu
teup
cii
kaw
(yow
déranger)
Ba
ngueu
bouger
nii
(yow
déranger)
Kedougou
Sedhiou
Matam
Kolda
beu
Zinguinchor
Kaffrine
beu
Louga
lô
Fatewma
wa
Podor
yaye
Yakham
Mbaye
Yakham
wooma
España
Boloñas
Scotland
Italia
Fatewma
wa
Paris
yaye
Bayou
Fallou
Mbaye
Yakham
wooma
Espagne
ba
Allemagne
Norvège
ba
London
Fatewma
wa
Hollande
Habidu
Belgique
man

1 Etudiant
2 Yalla Bakhna
3 Stay
4 Mame Boye
5 Bien-être
6 Ibou Touré
7 Lo Nam
8 Bayou Wally
9 Xalam
10 Jigenne
11 Wango / Nitki / Meissa Bigue / Nanette Ada / Silmaxa / Mbeguel / Afia / Papa - Bonus Track
12 Cherche en toi
13 Lo Beugue
14 Dérangé
15 Xaley
16 Si vous saviez
17 Xel
18 Paradise
19 Mame Bamba
20 Baye Fall
21 Only Love
Attention! Feel free to leave feedback.