Lyrics Yémé (Dakar Trap #2) - Iss 814
Sokhna
si
ya
dak
chocolat
Lig
ma
def
big
si
goudi
oulala
Nagouna
yay
sama
ébola
Lima
yeuk
sama
yaram
sa
djiko
la
Thiouray
bigua
def
koulako
diay
Vraiment
Lawbé
bi
dinama
ray
Nema
li
dot
chéri
songouma
Iowmi
iowmi
rek
si
jogama
Boula
nekhé
guénel
sama
yaye
Wala
sakh
gua
dak
sama
baye
Parceque
iow
nigua
mel
ken
douko
mel
(no
no)
Boufi
nekoulé
lépay
law
Parce
degua
Yémé
Yémé,
Yémé,Yémé,Yémé,Yémé
Yémé,Yémé
Yémé(yémééééé)
Yémé(yémééééé)
Yaye
boy
nak
dagua
beuri
problème
Ki
loko
méré
méré
manoul
dem
Woko
yen
niar
yen
diéma
waxtan
Def
ko
ni
sa
dom
diko
naxtan
Wakh
deug
yaye
xamé
toumaleuh
Téh
boufiy
wakh
sakh
ma
guéné
leuh
Sey
gua
ba
paré
bako
mou
sey
Ki
bou
guéné
keur
gui
dotouma
khey
Setna
ba
set
iow
yakoy
togn
Negua
manoul
sokhu
manoul
mogne
Bou
dougué
si
wagn
bi
daguén
koy
diew
diew
diew
Bou
goudé
teudi
dagueni
thiow
Parce
que
dafa
Yémé
Yémé,Yémé,Yémé,Yémé
Yémé,Yémé,Yémé
Wakhma
kagn
guay
gnibi
yaye
Dakh
sokhna
si
néna
bouma
lafi
bayi
Dafa
Yémé
oh
ah(yémééééé)
Dafa
Yémé
oh
ah(yémééééé)
Wakhma
kagn
guay
gnibi
yaye
Dakh
té
sokhna
si
néna
bouma
lafi
bayi
Dafa
Yémé
oh
ah(yémééééé)
Kagn
guay
gnibi
yaye
(yémé)
Yémé
yémé
yémé
yémé
yémé
Yémé
yémé
YÉMÉÉÉÉÉÉ
Attention! Feel free to leave feedback.