Ashs The Best feat. Dip Doundou Guiss - Ndogal Lyrics

Lyrics Ndogal - Dip Doundou Guiss , Ashs The Best



Nitt ak doundam, nitt ak mélokan'am, nitt ak jeufinam
Y'allah ak meuninam, bayal sa warr
Ko khamoul dioud'am
Khamo thiossan'am, bayiko mou dem
Y'allah ak ndogalam topal sa wayy
Gorr dey nangou ndogal (gorr dey nangou ndogal)
Nanto di ker kéra diam gni
Dou sagane sank lap do dougn, do set do sélal
Do kham boromam
Ouuhh... aaaah... am y'allah niakeu y'allah
Ouuhh... aaaah... y'allah yallah bay sa tool
Ouuhh... aaaah... nato di kér kéra diam
Ouuhh... aaaah... y'allah yallah nagn ko gnane
Dougou si beugeu si guen
Dioudou di diéguési déh
Louxouss dou guéner billet
Dougou pour gniko fi beuy
Mounouma dokh si digue ndokh wayé bougou ma khof di tindi lokh
Deukeu di wax si nitt lou bone
Bo déwé guiss god do sigui khol ko
How lies on me eyes, (on me)
Loutax nga tek ma beut guissoumala
Eyes on me why?
How eye on me (on me)
Life dou nonou menyeah!
Sokhor dey leundeumeul sama rouh,
Kignane dafey peundeul sama yourr
Y'allay xam xam, y'allay mbeuguel, y'allay am am
Y'allay mbecté
Life yakoy jugé moley teuthi
Life yakoy guédeu yakoy néxal
Life daley fowé ngen deugeul
Life geunoul kawé soufou bop
Gorr dey nangou ndogal (gorr dey nangou ndogal)
Nanto di ker kéra diam gni
Dou sagane sank lap do dougn, do set do sélal
Do kham boromam
Ouuhh... aaaah... am y'allah niakeu y'allah
Ouuhh... aaaah... y'allah yallah bay sa tool
Ouuhh... aaaah... nato di kér kéra diam
Ouuhh... aaaah... y'allah yallah nagn ko gnane



Writer(s): Elhadj Arfang Tiaré


Ashs The Best feat. Dip Doundou Guiss - Millions Flows
Album Millions Flows
date of release
15-11-2019



Attention! Feel free to leave feedback.