BM Jaay - Rock Yo Body Lyrics

Lyrics Rock Yo Body - BM Jaay



Boudoul mane wakhma kou bakh si iow
Reptile Music
Bouldoule mane wakhma kou bakh iow
Yénén goor yi nékoul maan akk niom
Tell me if you need somebody
Yeh yeh
Boudoul maan wakhma kou bakh si yaw
Guél you beuri woté sama phone
But I only need your body
Oh oh oh oah
Yama téré nélaw damlay khalat every night
Ladj tél sama bop loutakh do djouk sama mind
Niou beuri daGn Mayeu toppou Mais sama khol yaw leu ladj
Ahh
Oh oh oh oah
Yama téré nélaw dam lay khalat every night
Ladj tél sama bop loutakh do djouk sama mind
Niou beuri daGn Mayeu toppou mais sama khol yaw leu ladj
Let me rock your body
Ihhh
Let me rock your body
Oaww
Ouhh baby let me rock you body
Rock your body
Yeh yeh
Rock it rock it rock it for me




BM Jaay - Valar Morghulis - EP
Album Valar Morghulis - EP
date of release
31-08-2019




Attention! Feel free to leave feedback.