Canabasse - Khar Mou Djot Lyrics

Lyrics Khar Mou Djot - Canabasse



Paroles de Khar mou jot
Douma sandi kher douma lakeu keur diambour damay
Khar mou diote ma daldi sanni sama carte
Douma sanni kher
douma lakkeu keur diambour damay
Khar mou diote ma daldi sanni sama carte
Béneu Mandarga rek ngay guiss si sama yaram
Lima diota dékou mo eup mo eup liy nieuw konn damay mougn
1ier Couplet
LOkho ko fi tek kon lokho koy dindi
Khar élection jot ma dieul ko iri
Dougeul ko bureau de vote Ngoureum ma puni
Tekfi koumou meunti donn et puis c fini
Douma sanni kher ndakh
Béneu si gnom doudal si ndélou laye di dala signi w
Douma tal pneu damay khar
Sama carte guéneu ma dougou si bureau bi géneu ak ... wala
Ndakh SOPI doufi dess Sopi la niouyy def
Nioko sombi wonn nan nagnouko dafa wara diekh
Ragalouma teukou doumanak takkder yi
Palé la beug mou takk keur député
Ndakh ...
Mais douko téré nekh
Ounkou soko beug réyy
Boppeu bi Ngay décapité
2iem Couplet
(YEH) damay mougn
Sanni sama carte Geumouma politik wayé sama waref dina matt
dina sigil Sénégal
Participé ci Tabakh bi ndakh niou meuna dieum kanam
Ték ko ci anam you legal Revolution meun na am do meussa degg Batt
Dina diangu sén programm Bouma Dougué Bureau
De vote niouy tanneu crinière douma deuké ...
amoul sERAL nak
Bou Naré Tauth sounouy carte
Wathi si Tali bi foutékou rek fasséné RAKK
Hommes baise politik walakhi diaroul polemik
Naniou Tok diapeu sounou niambour MIIIIP
Topatou sounou Avenir
Tiéné Diplome Géré Bis
Ndakh loloy sounou Bénéfice
Souniou tiéré nioko meuna sim
Fils boudé Kiga fal Ngay khar mou fath sa sokhla
Nakh ga sa bopp ndakh euleuk mou warrla
Lou meunoul Niakk Defko lou war la
Konn Ngala beussbeu tiénél sa carte topeu rang ba
Boul topp tendance bako ak kharit ya
Rakkeu assurél sa choi nakhd nouss nouss
Boul nangou kéneu doutt leu ba dialeu
2012 jeunesse consciente nako dal




Canabasse - Mangui Gneuw
Album Mangui Gneuw
date of release
01-01-2012




Attention! Feel free to leave feedback.