Canabasse - Na Gnou Dem Lyrics

Lyrics Na Gnou Dem - Canabasse



Yaw kaay gnou dem kaay gnou dem
Kaaay gnou dem kaay gnou (n fois)
Baby gnou dem boul déguelou kèneu
Boul diémeu tokk naane da nga léni expliqué gni meunou gnou comprendre
Baby gnou dem boul déguelou kèneu
Li tchi yaw moy li cii mane lolou rek mo important
Na Gnou dem dem dem dem déééééém
Girl Na Gnou déééééém
Na Gnou dem dem dem dem déééééém
Baby Gnou déééééém Na Gnou déééééém
Xollou borom dou taaneu koumou tchi fatteu
Meunou ma thi wone dara bi nga tchi sareu
Meune nga jougué cii star ya da nga ma titeul
Sa beut you wékh taaleu ak sa signeu
Lougnou gueuneu waxtane ngamay gueuneu kill
Baby da nga SMART i'm the SKILLS
Mais nagnou bokou gnou monde
Deureum ak deureum gnoy andeu
What the fuck is that?
Lima lerr moy yaay kimaay gaaagne (gaaagne, gaaagne)
Yama gueuneu aduna ak li tchi biir
Mane tamite ma ngui lay gaaagne (gaaagne, gaaagne)
Guiss nako amoul lénène louma gueuneul liii
So Baby Girl, tell me what's the deal?
Dougnou bayiwaat mou yagg for real
Djiwo nagnou so many times maye nieuw fekk ngay dem
Maye khaar donté ma ngui tchile
Yes I have been with many girls
You have been with many men
But also I will be true your feelings remind
Baby gnou dem boul déguelou kèneu
Boul diémeu tokk naane da nga léni expliqué gni meunou gnou comprendre
Baby gnou dem boul déguelou kèneu
Li tchi yaw moy li cii mane lolou rek mo important
Na Gnou dem dem dem dem déééééém
Girl Na Gnou déééééém
Na Gnou dem dem dem dem déééééém
Baby Gnou déééééém Na Gnou déééééém
nagn bakhoulo Tchi Mane
nagn bakhouma Tchi yaw
Lignouy doundeu gnoune gnaar lane lagnou Tchi kham
Gnom ak sèn khalaat Tchi pot
Kaay gnou tek plan bi nagnou andeu daw
Meune nagnou doundeu cii jaameuh amoré mio
Lou bone lou bakh I don't give a damn
As long as Baby Girl ya ngui sama wétt wétt wétt
Malaye guiss ngay rétaane saye waxtane dima wéééééteuli
I Love you girl dokhal liko diar moko diar
Fi gnou dieum xama goumako mais je sacrifierai tout pour un voyage
Xam ngané beug nala Girl xam naané yama raw
Taaneu nala bou yagg, yaw lay khaar
Because I have been with many girls
Liné tchi gnom takhoul ma yëgg
Limaye yëgg bouma dianok sa smile my baby
Baby gnou dem boul déguelou kèneu
Boul diémeu tokk naane da nga léni expliqué gni meunou gnou comprendre
Baby gnou dem boul déguelou kèneu
Li tchi yaw moy li cii mane lolou rek mo important
Na Gnou dem dem dem dem déééééém
Girl Na Gnou déééééém
Na Gnou dem dem dem dem déééééém
Baby Gnou déééééém Na Gnou déééééém
{Outro}
Yaw kaay gnou dem kaay gnou dem
Kaaay gnou dem kaay gnou (n fois)




Canabasse - Na Gnou Dem - Single
Album Na Gnou Dem - Single
date of release
24-01-2017




Attention! Feel free to leave feedback.