Diogal Sakho - La paix Lyrics

Lyrics La paix - Diogal Sakho



Nieuwlen ma waxtan akk yenn (×2)
Ne beut yinga maye kholei key manei yeureum na khalei you Rwanda (×2)
Mane Souma sanione souma sanione diam sakhfa
Ne xibaar iow radio key sama wal meunuloko be dioy
Liñu wane yay si télé be key
Metinama mangui kay dioyto douma tayi
Suñu wanei xalei ye sama xol daldi
Diekh ni yen wer len ganay ye nguir xalei ye
Nga fokni yaye falla yeimey so guesto guiss Israel di dioy
Nga fokni yaye falla yeimey so guesto guiss Palestine di dioy
Nga fokni yaye falla yeimey ani Casamance
Nga fokni yaye falla yeimey xalei Rwanda
Suma xolei xalei ye sama xol daldi
Diekh yeine werr leine ganay ye nguir xalei
Soit l'ONU soit l'UA on vous attend pour la paix (×9)




Diogal Sakho - samba Alla
Album samba Alla
date of release
27-07-2006



Attention! Feel free to leave feedback.