Dip Doundou Guiss feat. Bass Thioung - LNN Lyrics

Lyrics LNN - Dip Doundou Guiss feat. Bass Thioung



Nek ci yoon,
Nek ci deuk tchi bagna tok Dérétou ennemie sama kaw Deum la déma
Djigne lima done never give up Amna goudi you tiss douma daw Douma
Faté bamay géneu galé papa kholal tay sa fils foumou tok Lo niémé
Niakk Lo niémé, Lo niémé, Lo niémé Lo niémé niak,
Amna ay défaites yi nga am Ay métitou moumeu Yek échelle mou danou
Guiss na ay serpent you mandou Mayna moma sétou tromper guélou
Diambour Meusna geum nitt kouma khamoul Voté Afrique ma solal goumbeu
Cagoul Baniouma jeunesse bouy nélaw Wayé jeunesse sou new mo geun bou
Yéwu calou Nek ci yoon,
Feint fi yéré you bone Rendi fi gaindé
Youy mbow Tour sama dérétou gorr Ioe ioe!
Néko mou tok Talouma kébétou thiow Niom daniouy thiéné amouniou
Diome Soul ay rappeurs yo khamné bamay ram sen CD ngui daw Damako
Kharé fils dama job Pour sama avenir sama dome Fils dama agné khif
Réré ndox Diangue nga amo fiit amo ngor Thiolou ba lay watié sama bop
Fuck niémay coup d′état Million la wantéré
Samay shows Trone bi fafa soudé samay tate
Kou bote boukki ay Faut kathie yi mbow la Mane diapna nikey défé
Nonou la Li nga def ci rapp bi Mane dama moudié warru Dip rap bi yako
Maquiller ba takh fépa tarru [REFRAIN] Nek ci yoon,
Nek ci deuk tchi bagna tok Dérétou ennemie sama kaw Deum la déma
Djigne lima done never give up Amna goudi you tiss douma daw Douma
Faté bamay géneu galé papa kholal tay sa fils foumou tok Lo niémé
Niakk Lo niémé, Lo niémé, Lo niémé Lo niémé niak, lo niémé niak,
Nekh amoul fen Talent deug ngen am Yen sen talent moy meun fen Gnimey
Mboubo lay mour Dip dou jubo dey soul Goré ba done esclave mo geun
Diay sa ngor ba done buur Lokho bou tayal dou tabakh lou deugeur Lo
Geuneu bégue di geuneu peuteukh Ma takh ba labouniou niou dima
Neukeul Welcome to life in the jungle Lafe famay yobou mane sokhla
Wouma pneu Wala daju si niakh wala peundeukh Faté na demb diap ci
Euleuk niari lokho gana moko geuneul Sa gars yi réwantou dama len di
Ray Kou djeumeum yarouwoul sa neew dou rew Dieul leu nouniouy dieulé
Thiep bou bess Di nga nangou ba sa thieur yi bagn Sama dieum ma geun
Sen def Fayna ound fay wesh wesh Def ni niom limay def rek déh Séni
Bop ni bambel tek tek Seni prof samay maitresse lagn Kougn fi thiow
Si rapp bi may sa père Yama meun boudé kou dakh fen Lim fi yor si
Song dou khathie dou dièkh Diameu geun mais ay mo dakh fay Diw sa
Guel mouy geun di diap teint Diw guelou niouy dakh yakh derr Nieup
Nul ni lamb lac 2 guers Kou bote boukki,
Faut kathie yi mbow la Mane diapna nikey défé nonou la Li nga def ci
Rapp bi, mane dama moudié warru Dip rap bi yako maquiller ba takh
Fépa tarru [REFRAIN] Nek ci yoon,
Nek ci deuk tchi bagna tok Dérétou ennemie sama kaw Deum la déma
Djigne lima done never give up Amna goudi you tiss douma daw Douma
Faté bamay géneu galé papa kholal tay sa fils foumou tok Lo niémé
Niakk Lo niémé, Lo niémé, Lo niémé Lo niémé niak, lo niémé niak,
Lo niémé, lo niémé niak [REFRAIN] Dip dakoy yeungeul waye,
Dip dakoy yeungeul Bass dakoy yeungeul waye Bass dakoy yeungeul Bass
Dakoy yeungeul Beusseul fi (beusseul) Wouy beusseul fi (beusseul) Ay
Beusseul fi, wa kone beusseul fi boy kone beusseul (lou bess)
Beusseul fi lou bess sa bess ay beusseul fi Wa kone beusseul fi,
Lou bess sa bess Dip dakoy yeungeul waye,
Dip dakoy yeungeul Bass dakoy yeungeul waye,
Bass dakoy yeungeul Bass dakoy yeungeul waye,
Bass dakoy yeungeul Beusseul fi (beusseul) Wouy beusseul fi
(Beusseul) Ay beusseul fi,
Wa kone beusseul fi boy kone beusseul (lou bess) Beusseul fi
Lou bess sa bess ay beusseul fi Wa kone beusseul fi, lou bess sa bess



Writer(s): Dominique Preira


Dip Doundou Guiss feat. Bass Thioung - LNN
Album LNN
date of release
17-08-2019

1 LNN



Attention! Feel free to leave feedback.