Dip Doundou Guiss - Guerre mondiale Lyrics

Lyrics Guerre mondiale - Dip Doundou Guiss



Reptil music
Hum Guerre day saf mondial,
Guerre guerre guerre day saf mondial (3bis)
Neu saf, neu saf,
Neu saffeu saffeu saf
xétou deii Momay xéégn,
Moussibeu for ever,
Nio beug nieuw deuk bouniou guerre tayy,
Bouniou fa diougueii souba kène douko féékei
Sii guédjou dérétt laniou beugueu féétei
Waa noumou gueuneu khonkei rek
Ioe meunone ngeu bania sol téreii
Gnii meu moudjeii rey ay sorcier lagn




Dip Doundou Guiss - Dipquinzaine 2.0
Album Dipquinzaine 2.0
date of release
22-01-2016




Attention! Feel free to leave feedback.