Lyrics May Kane - Dip Doundou Guiss
Nel
tekkeu
mother
fuck
kinest
manela
doff
bi
maay
Check
Microphone
bi
ngay
get
yaak
sa
copine
Légue
légue
may
Rap
dilay
ray
ak
égotrip
Ngay
fènn
naane
Rap
dou
métier
ndax
égo
fi
gaïndé
Di
raak
di
ndèy
make
money
sadik
ngay
def
Ni
Mane
pour
xeuy
tek
neulé
sac
yi
maay
dem
Mane
ak
Saozi
fokk
ni
nieupeu
niou
wara
guiss
Télouma
nandeu
ni
daw
dou
gaaw
ak
ay
mbarakiss
Démal
nga
lathié
ndéré
ndakh
gang
bi
soxla
na
xaliss
Dédette
takouma
tëré
liguey
rekka
fi
garantie
Dédette
tourouma
dérette
YALLAH
rekka
fi
gueuneu
diss
Intérêt
boula
takhé
jog
thiénél
doma
meusseu
guiss
Ci
gaalou
xathie
bi
ngama
done
khaar
finalou
RAP
yi
ngama
done
sathieu
Beus
na
nieuw
ma
wanela
boy
sipp
na
boubah
li
nga
done
waathie
Motah
may
gueuneu
xoss
xalima
bi
né
sama
ndèy-dior
Bou
sobbé
KIY
MAYé
waa
djiy
yorr
bisness
bi
mane
lay
done
DIP
génération
bou
wessou
lay
fay
Mane
douma
tiim
caméra
dafma
lerr
ni
na
fégne
Papa
djangalma
Raak
déggo
ko
fèneu
Té
ma
ngui
koy
carrément
yagg
yagg
day
fay
May
Kane,
da
nga
beug
xam
may
kane?
Fékk
ma
sama
makkaane.
May
Kane,
da
nga
beug
xam
may
kane?
Nieuweul
ba
sama
makkaane
Ma
ngui
djoudou
beussou
Vendredi
22
Mars
Bala
bobou
mougnena
maak
mère
bi
bène
9 mois
Awouma
djotou
fêté
sama
birthday
Damay
fékhé
ba
kène
dou
faaté
sama
beussou
déh
DIP
la
toudou.
Yaw
nak?...Okay!
Lissi
dess
niakoul
solo
mé
diaroul
wananté
ay
cartes
d'identité
Policier
bilay
sauvé
niakoul
ngène
rombanté
Xamo
toureum
té
nénay
mom
mo
ress
sa
karangué
Boul
khol
cii
nima
mel
boul
baayi
xel
cii
kimay
ndirool
Boul
khol
cii
limay
def
meunena
nékaate
cii
yénéni
rôle
Diapalni
mane
maay
goumbeu
bilay
wane
sa
yone
Diapéma
xadjou
boum
biy
bagna
feusseul
sa
xétou
drogue
Kholéma
Michael
Jackson,
Bob
Marley
ak
James
Brown
War
ngama
xamé
xeuyna
maak
yaw
nio
bokone
école
Manela
DIP
té
ay
diouni
songs
laay
bindeu
ndo
Sama
maladie
mo
ngui
cii
Album
bimala
dikk
DIP
génération
bou
wessou
lay
fay
Mane
douma
tiim
caméra
dafma
lerr
ni
na
fégne
Papa
djangalma
Raak
déggo
ko
fèneu
Té
ma
ngui
koy
carrément
yagg
yagg
day
fay
May
Kane,
da
nga
beug
xam
may
kane?
Fékk
ma
sama
makkaane.
May
Kane,
da
nga
beug
xam
may
kane?
Nieuweul
ba
sama
makkaane
1 Deug Deug
2 Assamane
3 Khametoma
4 Yone Bi (feat. Fla The Ripper)
5 Sama Jeunesse
6 Day Deep (feat. Elzo Jamdong)
7 A Thindji
8 Reuthie
9 Interview
10 Xam-Xam (feat. Ndongo D)
11 Pogda
12 Rep'team
13 Nangou
14 Doundou Oundou
15 Yaakarouma Ci Keen
16 Poto Lamp
17 May Kane
Attention! Feel free to leave feedback.